As-Sajda · 28/30
Tekki Waxtaan — Simoore As-Sajda
وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْفَتْحُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ ۝٢٨
Wa yaqooloona mataa haazal fat hu in kuntum saadiqeen
📖 Tekkim Wolof
Ñangay laaj naan : “Lii kañ lay doon, ndegam wax ngeen dëgg ? ”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 26-30 — Simoore As-Sajda

26أَوَلَمْ يَهْدِ لَهُمْ كَمْ أَهْلَكْنَا مِن قَبْلِهِم مِّنَ الْقُرُونِ يَمْشُونَ فِي مَسَاكِنِهِمْ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ ۖ أَفَلَا يَسْمَعُونَ
Ndax dafa doyul ci ñoom gindiku, te faagaalaloon Nanu ay maas ya leen jiitu woon te tey ñi ngi dox ci seen génti kër yi ? Ay kéemaan nekk na ci biir loolu ! Ndax ñoom dañu dul dégg ?
27أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّا نَسُوقُ الْمَاءَ إِلَى الْأَرْضِ الْجُرُزِ فَنُخْرِجُ بِهِ زَرْعًا تَأْكُلُ مِنْهُ أَنْعَامُهُمْ وَأَنفُسُهُمْ ۖ أَفَلَا يُبْصِرُونَ
Xanaa dañoo gisul ñoom ci ne Man Yàlla maay wàcce ndox ci kaw suuf su wow, génne gàncax gu seeni jur di lekk ak ñoom it ñu di ca lekk ? Moo ndax ñoom dañu dul gis ?
28وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْفَتْحُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñangay laaj naan : “Lii kañ lay doon, ndegam wax ngeen dëgg ? ”.
29قُلْ يَوْمَ الْفَتْحِ لَا يَنفَعُ الَّذِينَ كَفَرُوا إِيمَانُهُمْ وَلَا هُمْ يُنظَرُونَ
Waxal ne : “Bis ba ndam la di ñëw, ngëmug yéefar yi dootuleen jariñati dara ! Te kenn duleen négandiku”.
30فَأَعْرِضْ عَنْهُمْ وَانتَظِرْ إِنَّهُم مُّنتَظِرُونَ
Dummóoyuleen te xaar. Ñoom it ñi ngi xaar.
As-SajdaFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — As-Sajda 28

Simoore As-Sajda Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñangay laaj naan : “Lii kañ lay doon, ndegam wax…

Simoore Aaya 28/30 — Simoore As-Sajda السجدة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Sajda Dégg, Simoore As-Sajda Tekki, Simoore As-Sajda mp3, Simoore As-Sajda pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers