Ya-Sin · 75/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
لَا يَسْتَطِيعُونَ نَصْرَهُمْ وَهُمْ لَهُمْ جُندٌ مُّحْضَرُونَ ۝٧٥
Laa yastatee`oona nasrahum wa hum lahum jundum muhdaroon
📖 Tekkim Wolof
Yooyu duleen mën a dimbali, dañuy sax faf di jàmmaarlook ñoom [di xare].

🎧 Dégg


📜 Aaya 73-77 — Simoore Ya-Sin

73وَلَهُمْ فِيهَا مَنَافِعُ وَمَشَارِبُ ۖ أَفَلَا يَشْكُرُونَ
am nañu ci ay njariñ ak i naan. Moo ndax dañu dul sant ?
74وَاتَّخَذُوا مِن دُونِ اللَّهِ آلِهَةً لَّعَلَّهُمْ يُنصَرُونَ
Ñuy jàppe yàlla leneen lu dul Yàlla, ngir ñu neey danuy sàkku ndimbal...
75لَا يَسْتَطِيعُونَ نَصْرَهُمْ وَهُمْ لَهُمْ جُندٌ مُّحْضَرُونَ
Yooyu duleen mën a dimbali, dañuy sax faf di jàmmaarlook ñoom [di xare].
76فَلَا يَحْزُنكَ قَوْلُهُمْ ۘ إِنَّا نَعْلَمُ مَا يُسِرُّونَ وَمَا يُعْلِنُونَ
Bula seeni wax jaaxal ! Nun xam Nanu li ñuy yelu ak li ñuy biral.
77أَوَلَمْ يَرَ الْإِنسَانُ أَنَّا خَلَقْنَاهُ مِن نُّطْفَةٍ فَإِذَا هُوَ خَصِيمٌ مُّبِينٌ
Xanaa nit dafa gisul ne Nun Yàlla noo ko bind ci lumbub deret ? Deketeyoo moom ab xulóowaakoon la bu di ab pànk !
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
75Aaya

Tekki — Ya-Sin 75

Simoore Ya-Sin Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yooyu duleen mën a dimbali, dañuy sax faf di jàmmaarlook…

Simoore Aaya 75/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 73–77. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers