As-Saffat · 154/182
Tekki Waxtaan — As-Saffat
مَا لَكُمْ كَيْفَ تَحْكُمُونَ ۝١٥٤
Maa lakum kaifa tahkumoon
📖 Tekkim Wolof
Ana lu leen dal ba ngeen di àttee nii ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 152-156 — As-Saffat

152وَلَدَ اللَّهُ وَإِنَّهُمْ لَكَاذِبُونَ
“Yàlla am na doom” ; te ñoom dañuy fen doŋŋ !
153أَصْطَفَى الْبَنَاتِ عَلَى الْبَنِينَ
Moo ndax dafay gënal doom ju jigéen ci kaw doom ju góor ?
154مَا لَكُمْ كَيْفَ تَحْكُمُونَ
Ana lu leen dal ba ngeen di àttee nii ?
155أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Moo ndax dangeen dul fàttaliku ?
156أَمْ لَكُمْ سُلْطَانٌ مُّبِينٌ
Walla dangeen am ay firnde yu wóor ?
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
154Aaya

Tekki — As-Saffat 154

Simoore As-Saffat Aaya 154 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana lu leen dal ba ngeen di àttee nii ?

Simoore Aaya 154/182 — As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saffat Dégg, As-Saffat Tekki, As-Saffat mp3, As-Saffat pdf. Aaya 152–156. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers