As-Saffat · 153/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
أَصْطَفَى الْبَنَاتِ عَلَى الْبَنِينَ ۝١٥٣
Astafal banaati `alal baneen
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dafay gënal doom ju jigéen ci kaw doom ju góor ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 151-155 — Simoore As-Saffat

151أَلَا إِنَّهُم مِّنْ إِفْكِهِمْ لَيَقُولُونَ
Ndax ñoom dañuy faral di wax ci seen duur ya, naan :
152وَلَدَ اللَّهُ وَإِنَّهُمْ لَكَاذِبُونَ
“Yàlla am na doom” ; te ñoom dañuy fen doŋŋ !
153أَصْطَفَى الْبَنَاتِ عَلَى الْبَنِينَ
Moo ndax dafay gënal doom ju jigéen ci kaw doom ju góor ?
154مَا لَكُمْ كَيْفَ تَحْكُمُونَ
Ana lu leen dal ba ngeen di àttee nii ?
155أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Moo ndax dangeen dul fàttaliku ?
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
153Aaya

Tekki — As-Saffat 153

Simoore As-Saffat Aaya 153 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dafay gënal doom ju jigéen ci kaw doom…

Simoore Aaya 153/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 151–155. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers