As-Saffat · 17/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
أَوَآبَاؤُنَا الْأَوَّلُونَ ۝١٧
Awa aabaa`unal awwaloon
📖 Tekkim Wolof
ak sunuy baay ak i maamaat ? ”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 15-19 — Simoore As-Saffat

15وَقَالُوا إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ مُّبِينٌ
tey wax naan : “Lii dey ag njabar doŋŋ la.
16أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ
Moo ndax su nu faatoo ba def suuf ak i yax, dees nanu dekkalaat ?
17أَوَآبَاؤُنَا الْأَوَّلُونَ
ak sunuy baay ak i maamaat ? ”
18قُلْ نَعَمْ وَأَنتُمْ دَاخِرُونَ
Neel : “Waaw ! te dangeen torox de”.
19فَإِنَّمَا هِيَ زَجْرَةٌ وَاحِدَةٌ فَإِذَا هُمْ يَنظُرُونَ
Genn ug xaacu rekk ay jib, ñu ne xewwu di xoolante (dekki),
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — As-Saffat 17

Simoore As-Saffat Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak sunuy baay ak i maamaat ? ”

Simoore Aaya 17/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers