As-Saffat · 18/182
Tekki Waxtaan — As-Saffat
قُلْ نَعَمْ وَأَنتُمْ دَاخِرُونَ ۝١٨
Qul na`am wa antum daakhiroon
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Waaw ! te dangeen torox de”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 16-20 — As-Saffat

16أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ
Moo ndax su nu faatoo ba def suuf ak i yax, dees nanu dekkalaat ?
17أَوَآبَاؤُنَا الْأَوَّلُونَ
ak sunuy baay ak i maamaat ? ”
18قُلْ نَعَمْ وَأَنتُمْ دَاخِرُونَ
Neel : “Waaw ! te dangeen torox de”.
19فَإِنَّمَا هِيَ زَجْرَةٌ وَاحِدَةٌ فَإِذَا هُمْ يَنظُرُونَ
Genn ug xaacu rekk ay jib, ñu ne xewwu di xoolante (dekki),
20وَقَالُوا يَا وَيْلَنَا هَٰذَا يَوْمُ الدِّينِ
ñuy wax naan : “Ngalla nun ! Bis-pénc baa ngi nii waay”.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — As-Saffat 18

Simoore As-Saffat Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Waaw ! te dangeen torox de”.

Simoore Aaya 18/182 — As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saffat Dégg, As-Saffat Tekki, As-Saffat mp3, As-Saffat pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers