As-Saffat · 179/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَأَبْصِرْ فَسَوْفَ يُبْصِرُونَ ۝١٧٩
Wa absir fasawfa yubsiroon
📖 Tekkim Wolof
te nga seetluleen : danañu gis de !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 177-181 — Simoore As-Saffat

177فَإِذَا نَزَلَ بِسَاحَتِهِمْ فَسَاءَ صَبَاحُ الْمُنذَرِينَ
Su wàccee ci seenub ëtt, ñoom ña ñu doon fàttali, ndaw suba gu bon !
178وَتَوَلَّ عَنْهُمْ حَتَّىٰ حِينٍ
nanga leen dummóoyu ab diir ;
179وَأَبْصِرْ فَسَوْفَ يُبْصِرُونَ
te nga seetluleen : danañu gis de !
180سُبْحَانَ رَبِّكَ رَبِّ الْعِزَّةِ عَمَّا يَصِفُونَ
Tudd naa sellug sa Boroom, Boroom kàttan gi. Kawe na ca la ñu koy melal !
181وَسَلَامٌ عَلَى الْمُرْسَلِينَ
Te jàmm yal na wàcc ci Yonent yi,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
179Aaya

Tekki — As-Saffat 179

Simoore As-Saffat Aaya 179 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te nga seetluleen : danañu gis de !

Simoore Aaya 179/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 177–181. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers