As-Saffat · 22/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
۞ احْشُرُوا الَّذِينَ ظَلَمُوا وَأَزْوَاجَهُمْ وَمَا كَانُوا يَعْبُدُونَ ۝٢٢
Uhshurul lazeena zalamoo wa azwaajahum wa maa kaanoo ya`budoon
📖 Tekkim Wolof
“Dajaleleen tooñkat ya ak seeni jabar ak la ñu daan jaamu,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 20-24 — Simoore As-Saffat

20وَقَالُوا يَا وَيْلَنَا هَٰذَا يَوْمُ الدِّينِ
ñuy wax naan : “Ngalla nun ! Bis-pénc baa ngi nii waay”.
21هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ الَّذِي كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
“Lii mooy bisub àtte ba ngeen jàppe woon ay fen, weddi ko”.
22۞ احْشُرُوا الَّذِينَ ظَلَمُوا وَأَزْوَاجَهُمْ وَمَا كَانُوا يَعْبُدُونَ
“Dajaleleen tooñkat ya ak seeni jabar ak la ñu daan jaamu,
23مِن دُونِ اللَّهِ فَاهْدُوهُمْ إِلَىٰ صِرَاطِ الْجَحِيمِ
bàyyi woon Yàlla. Te wëtal leen jëme yoonu Safara.
24وَقِفُوهُمْ ۖ إِنَّهُم مَّسْئُولُونَ
Te ngeen taxawlooleen : ndax dañu leen di laaj”.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — As-Saffat 22

Simoore As-Saffat Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Dajaleleen tooñkat ya ak seeni jabar ak la ñu daan…

Simoore Aaya 22/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers