As-Saffat · 21/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ الَّذِي كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ ۝٢١
Haazaa Yawmul Faslil lazee kuntum bihee tukaziboon
📖 Tekkim Wolof
“Lii mooy bisub àtte ba ngeen jàppe woon ay fen, weddi ko”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Simoore As-Saffat

19فَإِنَّمَا هِيَ زَجْرَةٌ وَاحِدَةٌ فَإِذَا هُمْ يَنظُرُونَ
Genn ug xaacu rekk ay jib, ñu ne xewwu di xoolante (dekki),
20وَقَالُوا يَا وَيْلَنَا هَٰذَا يَوْمُ الدِّينِ
ñuy wax naan : “Ngalla nun ! Bis-pénc baa ngi nii waay”.
21هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ الَّذِي كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
“Lii mooy bisub àtte ba ngeen jàppe woon ay fen, weddi ko”.
22۞ احْشُرُوا الَّذِينَ ظَلَمُوا وَأَزْوَاجَهُمْ وَمَا كَانُوا يَعْبُدُونَ
“Dajaleleen tooñkat ya ak seeni jabar ak la ñu daan jaamu,
23مِن دُونِ اللَّهِ فَاهْدُوهُمْ إِلَىٰ صِرَاطِ الْجَحِيمِ
bàyyi woon Yàlla. Te wëtal leen jëme yoonu Safara.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — As-Saffat 21

Simoore As-Saffat Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Lii mooy bisub àtte ba ngeen jàppe woon ay fen,…

Simoore Aaya 21/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers