As-Saffat · 66/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَإِنَّهُمْ لَآكِلُونَ مِنْهَا فَمَالِئُونَ مِنْهَا الْبُطُونَ ۝٦٦
Fa innahum la aakiloona minhaa famaali`oona minhal butoon
📖 Tekkim Wolof
Ca la ñuy lekk, di ca feesal seeni biir.

🎧 Dégg


📜 Aaya 64-68 — Simoore As-Saffat

64إِنَّهَا شَجَرَةٌ تَخْرُجُ فِي أَصْلِ الْجَحِيمِ
Moom garab la guy génn ca ndéntul Safara.
65طَلْعُهَا كَأَنَّهُ رُءُوسُ الشَّيَاطِينِ
Meññent ma mel ni boppi séytaane.
66فَإِنَّهُمْ لَآكِلُونَ مِنْهَا فَمَالِئُونَ مِنْهَا الْبُطُونَ
Ca la ñuy lekk, di ca feesal seeni biir.
67ثُمَّ إِنَّ لَهُمْ عَلَيْهَا لَشَوْبًا مِّنْ حَمِيمٍ
Am nañu fa, ca kawam, am ndox mu tàng [di wañax].
68ثُمَّ إِنَّ مَرْجِعَهُمْ لَإِلَى الْجَحِيمِ
Safara rekk mooy seen kër.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
66Aaya

Tekki — As-Saffat 66

Simoore As-Saffat Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca la ñuy lekk, di ca feesal seeni biir.

Simoore Aaya 66/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers