As-Saffat · 84/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِذْ جَاءَ رَبَّهُ بِقَلْبٍ سَلِيمٍ ۝٨٤
Iz jaaa`a Rabbahoo bi qalbin saleem
📖 Tekkim Wolof
Fàttalikul ba mu dikkee ca Boroomam ànd ak xol bu mucc ayib.

🎧 Dégg


📜 Aaya 82-86 — Simoore As-Saffat

82ثُمَّ أَغْرَقْنَا الْآخَرِينَ
Ginnaaw ba, Nu labal ña ca des.
83۞ وَإِنَّ مِن شِيعَتِهِ لَإِبْرَاهِيمَ
Ibrahiima bokkoon na ca ay njabootam.
84إِذْ جَاءَ رَبَّهُ بِقَلْبٍ سَلِيمٍ
Fàttalikul ba mu dikkee ca Boroomam ànd ak xol bu mucc ayib.
85إِذْ قَالَ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ مَاذَا تَعْبُدُونَ
Ak ba mu waxee baayam ak nitam, ne leen : “Ana li ngeen di jaamu ? ”
86أَئِفْكًا آلِهَةً دُونَ اللَّهِ تُرِيدُونَ
Moo ndax ay nar ngeen di namm a def ay yàlla bàyyi Yàlla Moom ?
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
84Aaya

Tekki — As-Saffat 84

Simoore As-Saffat Aaya 84 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Fàttalikul ba mu dikkee ca Boroomam ànd ak xol bu…

Simoore Aaya 84/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 82–86. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers