As-Saffat · 85/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِذْ قَالَ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ مَاذَا تَعْبُدُونَ ۝٨٥
Iz qaala li abeehi wa qawmihee maazaa ta`budoon
📖 Tekkim Wolof
Ak ba mu waxee baayam ak nitam, ne leen : “Ana li ngeen di jaamu ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 83-87 — Simoore As-Saffat

83۞ وَإِنَّ مِن شِيعَتِهِ لَإِبْرَاهِيمَ
Ibrahiima bokkoon na ca ay njabootam.
84إِذْ جَاءَ رَبَّهُ بِقَلْبٍ سَلِيمٍ
Fàttalikul ba mu dikkee ca Boroomam ànd ak xol bu mucc ayib.
85إِذْ قَالَ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ مَاذَا تَعْبُدُونَ
Ak ba mu waxee baayam ak nitam, ne leen : “Ana li ngeen di jaamu ? ”
86أَئِفْكًا آلِهَةً دُونَ اللَّهِ تُرِيدُونَ
Moo ndax ay nar ngeen di namm a def ay yàlla bàyyi Yàlla Moom ?
87فَمَا ظَنُّكُم بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
Waaw, lu ngeen njort ci Yàlla boroom asamaan si ? ”
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
85Aaya

Tekki — As-Saffat 85

Simoore As-Saffat Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak ba mu waxee baayam ak nitam, ne leen :…

Simoore Aaya 85/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers