Sad · 42/88
Tekki Waxtaan — Sad
ارْكُضْ بِرِجْلِكَ ۖ هَٰذَا مُغْتَسَلٌ بَارِدٌ وَشَرَابٌ ۝٤٢
Urkud birijlika haaza mughtasalum baaridunw wa sharaab
📖 Tekkim Wolof
(Yàlla ne ko) dóoral sa tànk fi ci suuf : am ndox ngi nii mu sedd mu man a sangu neex a naan.

🎧 Dégg


📜 Aaya 40-44 — Sad

40وَإِنَّ لَهُ عِندَنَا لَزُلْفَىٰ وَحُسْنَ مَآبٍ
Te mooy am na daraja ju Nu jege ak wàccuwaay wu jekk.
41وَاذْكُرْ عَبْدَنَا أَيُّوبَ إِذْ نَادَىٰ رَبَّهُ أَنِّي مَسَّنِيَ الشَّيْطَانُ بِنُصْبٍ وَعَذَابٍ
Fàttalikul sunu jaam Ayyuuba , ba muy woo Boroomam naan ko : “Yaw sama Boroom Saytaane teg na ma coono ak i tiis”.
42ارْكُضْ بِرِجْلِكَ ۖ هَٰذَا مُغْتَسَلٌ بَارِدٌ وَشَرَابٌ
(Yàlla ne ko) dóoral sa tànk fi ci suuf : am ndox ngi nii mu sedd mu man a sangu neex a naan.
43وَوَهَبْنَا لَهُ أَهْلَهُ وَمِثْلَهُم مَّعَهُمْ رَحْمَةً مِّنَّا وَذِكْرَىٰ لِأُولِي الْأَلْبَابِ
Nu delloowaat ko njabootam joxaat ko lu na tollu, muy yërmande ju bawoo ci Nun ak fàttili woroom xel yi.
44وَخُذْ بِيَدِكَ ضِغْثًا فَاضْرِب بِّهِ وَلَا تَحْنَثْ ۗ إِنَّا وَجَدْنَاهُ صَابِرًا ۚ نِّعْمَ الْعَبْدُ ۖ إِنَّهُ أَوَّابٌ
“Ŋëbal sëqub ñax, te dóor ko ko (soxnaam sa). Te bul gàddu bàkkaarub ngiiñ”. Moom, muñkat la di jaam bu baax. Kuy farlu di dellu ci Boroomam la.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Sad 42

Simoore Sad Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Yàlla ne ko) dóoral sa tànk fi ci suuf :…

Simoore Aaya 42/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers