Ghafir · 44/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
فَسَتَذْكُرُونَ مَا أَقُولُ لَكُمْ ۚ وَأُفَوِّضُ أَمْرِي إِلَى اللَّهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ بَصِيرٌ بِالْعِبَادِ ۝٤٤
Fasatazkuroona maaa aqoolu lakum; wa ufawwidu amreee ilal laah; innallaaha baseerum bil`ibaad
📖 Tekkim Wolof
Yàggatul ne dangeen fàttaliku ji lii ma leen di wax ; te wéer naa samay mbir ci Yàlla. Ndax, kuy Gis jaamam ñi la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 42-46 — Ghafir

42تَدْعُونَنِي لِأَكْفُرَ بِاللَّهِ وَأُشْرِكَ بِهِ مَا لَيْسَ لِي بِهِ عِلْمٌ وَأَنَا أَدْعُوكُمْ إِلَى الْعَزِيزِ الْغَفَّارِ
Yéen a ngi may woo ngir ma weddi Yàlla di ko bokkaaleek lu ma amul benn xam-xam, te man maa ngi leen di woo jëme leen ci Yàlla miy boroom Kàttan, tey Jégëlaakoon ba.
43لَا جَرَمَ أَنَّمَا تَدْعُونَنِي إِلَيْهِ لَيْسَ لَهُ دَعْوَةٌ فِي الدُّنْيَا وَلَا فِي الْآخِرَةِ وَأَنَّ مَرَدَّنَا إِلَى اللَّهِ وَأَنَّ الْمُسْرِفِينَ هُمْ أَصْحَابُ النَّارِ
Sikkuwul ne li ngeen may woo jëmale amuñu luy tax ñu war leen a woo ci àddina sii waxantumaalaak ca àllaaxira. Te it ca Yàlla lañuy dellu, te itam yaqkat ya ñooy wa Safara.
44فَسَتَذْكُرُونَ مَا أَقُولُ لَكُمْ ۚ وَأُفَوِّضُ أَمْرِي إِلَى اللَّهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ بَصِيرٌ بِالْعِبَادِ
Yàggatul ne dangeen fàttaliku ji lii ma leen di wax ; te wéer naa samay mbir ci Yàlla. Ndax, kuy Gis jaamam ñi la.
45فَوَقَاهُ اللَّهُ سَيِّئَاتِ مَا مَكَرُوا ۖ وَحَاقَ بِآلِ فِرْعَوْنَ سُوءُ الْعَذَابِ
Yàlla fegal na ko ñaawtéef ya ñu doon fexe, daldi sóob njabootug Firwana gën jaa tar i mbugël :
46النَّارُ يُعْرَضُونَ عَلَيْهَا غُدُوًّا وَعَشِيًّا ۖ وَيَوْمَ تَقُومُ السَّاعَةُ أَدْخِلُوا آلَ فِرْعَوْنَ أَشَدَّ الْعَذَابِ
ñu di leen , gaaral ci Safara suba ak ngoon. Bu Bis Pénc baa (da naa digle) : “Ñu dugël njabootug Firawna ca gën jaa tar i mbugël”.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
44Aaya

Tekki — Ghafir 44

Simoore Ghafir Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàggatul ne dangeen fàttaliku ji lii ma leen di wax…

Simoore Aaya 44/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers