Az-Zukhruf · 42/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
أَوْ نُرِيَنَّكَ الَّذِي وَعَدْنَاهُمْ فَإِنَّا عَلَيْهِم مُّقْتَدِرُونَ ۝٤٢
Aw nuriyannakal lazee wa`adnaahum fa innaa `alaihim muqtadiroon
📖 Tekkim Wolof
Walla Nu wan la la Nu leen digoon ñoom ; am Nanu Kàttan ci seen kaw de.

🎧 Dégg


📜 Aaya 40-44 — Simoore Az-Zukhruf

40أَفَأَنتَ تُسْمِعُ الصُّمَّ أَوْ تَهْدِي الْعُمْيَ وَمَن كَانَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Moo ndax yaw man ngaa déggloo ku tëx mbaa nga man a gindi ku gumba mba ku nekk ci réer gu tar ?
41فَإِمَّا نَذْهَبَنَّ بِكَ فَإِنَّا مِنْهُم مُّنتَقِمُونَ
Benn nu yóbbu la nga [dee] Nu daldi fayu ci ñoom ;
42أَوْ نُرِيَنَّكَ الَّذِي وَعَدْنَاهُمْ فَإِنَّا عَلَيْهِم مُّقْتَدِرُونَ
Walla Nu wan la la Nu leen digoon ñoom ; am Nanu Kàttan ci seen kaw de.
43فَاسْتَمْسِكْ بِالَّذِي أُوحِيَ إِلَيْكَ ۖ إِنَّكَ عَلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Jafandikul ci li nu soloo ci yaw yaa ngi ci yoon wu jub xocc wa.
44وَإِنَّهُ لَذِكْرٌ لَّكَ وَلِقَوْمِكَ ۖ وَسَوْفَ تُسْأَلُونَ
Dëgg-dëgg [Alxuraan] fàttaliku la ngir yaw ak saw nit. Te it deefna leen ko laaj.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 42

Simoore Az-Zukhruf Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla Nu wan la la Nu leen digoon ñoom ;…

Simoore Aaya 42/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers