Az-Zukhruf · 87/89
Tekki Waxtaan — Az-Zukhruf
وَلَئِن سَأَلْتَهُم مَّنْ خَلَقَهُمْ لَيَقُولُنَّ اللَّهُ ۖ فَأَنَّىٰ يُؤْفَكُونَ ۝٨٧
Wa la`in sa altahum man khalaqahum la yaqoolun nallaahu fa annaa yu`fakoon
📖 Tekkim Wolof
Soo leen laajoon ana kan moo leen bind, ñu ne la : “Yàlla”. Kon naka la ñu koy dumóoyoo ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 85-89 — Az-Zukhruf

85وَتَبَارَكَ الَّذِي لَهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا وَعِندَهُ عِلْمُ السَّاعَةِ وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
Te itam barkeel na Moom mi am nguurug asamaan yeek suuf si ak li nekk ci seen diggënte. Moo ame it xam-xam bi làmboo waxtu wa (Bis Pénc ba). Te it ca moom ngeen di dellu.
86وَلَا يَمْلِكُ الَّذِينَ يَدْعُونَ مِن دُونِهِ الشَّفَاعَةَ إِلَّا مَن شَهِدَ بِالْحَقِّ وَهُمْ يَعْلَمُونَ
Ñay jaamu leneen lu dul moom duñu am benn man-man ci tinu (rammu), ba mu des ñay seede ci dëgg te di ñu xàmmee.
87وَلَئِن سَأَلْتَهُم مَّنْ خَلَقَهُمْ لَيَقُولُنَّ اللَّهُ ۖ فَأَنَّىٰ يُؤْفَكُونَ
Soo leen laajoon ana kan moo leen bind, ñu ne la : “Yàlla”. Kon naka la ñu koy dumóoyoo ?
88وَقِيلِهِ يَا رَبِّ إِنَّ هَٰؤُلَاءِ قَوْمٌ لَّا يُؤْمِنُونَ
Waxi Yonnent ba moo di : “Éy sama Boroom, ñii daal ay nit la ñu ñu gëmul”.
89فَاصْفَحْ عَنْهُمْ وَقُلْ سَلَامٌ ۚ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Dumóoyuleen yaw ; tey wax : “Jàmm ! ” Danañu xalset a xam.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
87Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 87

Simoore Az-Zukhruf Aaya 87 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Soo leen laajoon ana kan moo leen bind, ñu ne…

Simoore Aaya 87/89 — Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zukhruf Dégg, Az-Zukhruf Tekki, Az-Zukhruf mp3, Az-Zukhruf pdf. Aaya 85–89. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers