Al-Maida · 120/120
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Maida
لِلَّهِ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا فِيهِنَّ ۚ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ ۝١٢٠
Lillaahi mulkus samaawaati wal ardi wa maa feehinn; wa Huwa `alaa kulli shain`in Qadeer
📖 Tekkim Wolof
Yàllaa moom nguuru asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen biir, te Muy ku am kàttan nag ci def lépp [lu ko soob].

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 118-120 — Simoore Al-Maida

118إِن تُعَذِّبْهُمْ فَإِنَّهُمْ عِبَادُكَ ۖ وَإِن تَغْفِرْ لَهُمْ فَإِنَّكَ أَنتَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Boo leen mbugalee, say jaam lañu. Boo leen jéggalee it, Yaw yaa di Aji-not ji, di Ku xereñ [ci say àtte]”.
119قَالَ اللَّهُ هَٰذَا يَوْمُ يَنفَعُ الصَّادِقِينَ صِدْقُهُمْ ۚ لَهُمْ جَنَّاتٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا ۚ رَّضِيَ اللَّهُ عَنْهُمْ وَرَضُوا عَنْهُ ۚ ذَٰلِكَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
Yàlla ne : “Bis niki tey, ña dëgguwoon, seen dëggu ga dana leen jariñ : am nañu Àjjana yoo xam ne ay dex ñooy daw ca seen ron, dañu fay béel ba fàwwu.” Yàlla bég na ci ñoom, ñoom it ñu bég ci Yàlla. Loolu mooy texe gu màgg ga tigi.
120لِلَّهِ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا فِيهِنَّ ۚ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Yàllaa moom nguuru asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen biir, te Muy ku am kàttan nag ci def lépp [lu ko soob].
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
120Aaya

Tekki — Al-Maida 120

Simoore Al-Maida Aaya 120 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàllaa moom nguuru asamaan yi ak suuf si ak li…

Simoore Aaya 120/120 — Simoore Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Maida Dégg, Simoore Al-Maida Tekki, Simoore Al-Maida mp3, Simoore Al-Maida pdf. Aaya 118–120. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers