Al-Maida · 85/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
فَأَثَابَهُمُ اللَّهُ بِمَا قَالُوا جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ وَذَٰلِكَ جَزَاءُ الْمُحْسِنِينَ ۝٨٥
Fa asaabahumul laahu bimaa qaaloo Jannnaatin tajree min tahtihal anhaaru khaalideena feehaa; wa zaalika jazaaa`ul muhsineen
📖 Tekkim Wolof
Yàlla xéewale na leen, ngir la ñu wax, ay Àjjana yoo xam ne ay dex dañuy daw ca suufam, te dañu fay béel. Te loolu mooy peyug way-rafetal ña.
🎧 Dégg

📜 Aaya 83-87 — Al-Maida

83وَإِذَا سَمِعُوا مَا أُنزِلَ إِلَى الرَّسُولِ تَرَىٰ أَعْيُنَهُمْ تَفِيضُ مِنَ الدَّمْعِ مِمَّا عَرَفُوا مِنَ الْحَقِّ ۖ يَقُولُونَ رَبَّنَا آمَنَّا فَاكْتُبْنَا مَعَ الشَّاهِدِينَ
Te bu ñu déggee li wàcc ci Yonent bi nga gis seeni bët di sottiy rongoñ ndax dëgg ga ñu cay xàmmee. Ñuy wax naan : “Yaw sunu Boroom ! Gëm nanu : Nanga nu boole ca ñay way- seede.
84وَمَا لَنَا لَا نُؤْمِنُ بِاللَّهِ وَمَا جَاءَنَا مِنَ الْحَقِّ وَنَطْمَعُ أَن يُدْخِلَنَا رَبُّنَا مَعَ الْقَوْمِ الصَّالِحِينَ
Luy tee ñu gëm Yàlla ak la ñu dikkal ci dëgg ak ni nu xemeeme sunu Boroom tàbbal nu Àjjana ànd ak way-sellal ña ? ”.
85فَأَثَابَهُمُ اللَّهُ بِمَا قَالُوا جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ وَذَٰلِكَ جَزَاءُ الْمُحْسِنِينَ
Yàlla xéewale na leen, ngir la ñu wax, ay Àjjana yoo xam ne ay dex dañuy daw ca suufam, te dañu fay béel. Te loolu mooy peyug way-rafetal ña.
86وَالَّذِينَ كَفَرُوا وَكَذَّبُوا بِآيَاتِنَا أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْجَحِيمِ
Waaye nag yéefar ya weddi Sunuy kàddu, ñoom ñooy dugg Safara.
87يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تُحَرِّمُوا طَيِّبَاتِ مَا أَحَلَّ اللَّهُ لَكُمْ وَلَا تَعْتَدُوا ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يُحِبُّ الْمُعْتَدِينَ
Éy yéen ñi gëm : buleen araamal yu sell ya leen Yàlla daganal. Te it buleen jéggi dayo, Yàlla soppul ñiy jéggi dayo.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
85Aaya

Tekki — Al-Maida 85

Simoore Al-Maida Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla xéewale na leen, ngir la ñu wax, ay Àjjana…

Simoore Aaya 85/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers