Adh-Dhariyat · 27/60
Tekki Waxtaan — Adh-Dhariyat
فَقَرَّبَهُ إِلَيْهِمْ قَالَ أَلَا تَأْكُلُونَ ٢٧
Transliteration
Faqarrabahooo ilaihim qaala alaa taakuloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Daldi leen koy tegal ne leen... “Ndax dungeen lekk ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 25-29 — Adh-Dhariyat
25إِذْ دَخَلُوا عَلَيْهِ فَقَالُوا سَلَامًا ۖ قَالَ سَلَامٌ قَوْمٌ مُّنكَرُونَ
Ba ñu ko fekkee fa mu nekkoon ne ko : “Jàmm nga am ! ”, mu ne [leen] : “Jàmm rekk, yéen dey xamuma leen”.
26فَرَاغَ إِلَىٰ أَهْلِهِ فَجَاءَ بِعِجْلٍ سَمِينٍ
Daldi potoxlu giseek waa këram daldi indi aw sëllu wu duuf.
27فَقَرَّبَهُ إِلَيْهِمْ قَالَ أَلَا تَأْكُلُونَ
Daldi leen koy tegal ne leen... “Ndax dungeen lekk ? ”
28فَأَوْجَسَ مِنْهُمْ خِيفَةً ۖ قَالُوا لَا تَخَفْ ۖ وَبَشَّرُوهُ بِغُلَامٍ عَلِيمٍ
Am tiit daldi ko roofu. Ñu ne ko : “Bul tiit”. Daldi koy xamal ne dana am doom ju bari xam-xam.
29فَأَقْبَلَتِ امْرَأَتُهُ فِي صَرَّةٍ فَصَكَّتْ وَجْهَهَا وَقَالَتْ عَجُوزٌ عَقِيمٌ
soxnaam sa dikk ak i yuxu, di talaata boppam te naan : “Màggat mu jaasir...
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
27Aaya
Tekki — Adh-Dhariyat 27
Simoore Adh-Dhariyat Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Daldi leen koy tegal ne leen... “Ndax dungeen lekk ?…Simoore Aaya 27/60 — Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Adh-Dhariyat Dégg, Adh-Dhariyat Tekki, Adh-Dhariyat mp3, Adh-Dhariyat pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








