An-Najm · 13/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
وَلَقَدْ رَآهُ نَزْلَةً أُخْرَىٰ ۝١٣
Wa laqad ra aahu nazlatan ukhraa
📖 Tekkim Wolof
Moo ne gisoon na ko de, ca geneen wàcc,

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — Simoore An-Najm

11مَا كَذَبَ الْفُؤَادُ مَا رَأَىٰ
Xol ba weddiwul la mu gis.
12أَفَتُمَارُونَهُ عَلَىٰ مَا يَرَىٰ
Moo ndax yéen dangeen di weranteek moom ca la mu gisoon ?
13وَلَقَدْ رَآهُ نَزْلَةً أُخْرَىٰ
Moo ne gisoon na ko de, ca geneen wàcc,
14عِندَ سِدْرَةِ الْمُنتَهَىٰ
kerook rañaan ma fa “Sidratu Al Muntahaa”,
15عِندَهَا جَنَّةُ الْمَأْوَىٰ
foofee la jannatu “al Maawaa” nekk :
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — An-Najm 13

Simoore An-Najm Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ne gisoon na ko de, ca geneen wàcc,

Simoore Aaya 13/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers