An-Najm · 12/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
أَفَتُمَارُونَهُ عَلَىٰ مَا يَرَىٰ ۝١٢
Afatumaaroonahoo `alaa maayaraa
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax yéen dangeen di weranteek moom ca la mu gisoon ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore An-Najm

10فَأَوْحَىٰ إِلَىٰ عَبْدِهِ مَا أَوْحَىٰ
(Foofee) la Yàlla soloo jaamam la mu ko soloo.
11مَا كَذَبَ الْفُؤَادُ مَا رَأَىٰ
Xol ba weddiwul la mu gis.
12أَفَتُمَارُونَهُ عَلَىٰ مَا يَرَىٰ
Moo ndax yéen dangeen di weranteek moom ca la mu gisoon ?
13وَلَقَدْ رَآهُ نَزْلَةً أُخْرَىٰ
Moo ne gisoon na ko de, ca geneen wàcc,
14عِندَ سِدْرَةِ الْمُنتَهَىٰ
kerook rañaan ma fa “Sidratu Al Muntahaa”,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — An-Najm 12

Simoore An-Najm Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax yéen dangeen di weranteek moom ca la mu…

Simoore Aaya 12/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers