An-Najm · 23/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
إِنْ هِيَ إِلَّا أَسْمَاءٌ سَمَّيْتُمُوهَا أَنتُمْ وَآبَاؤُكُم مَّا أَنزَلَ اللَّهُ بِهَا مِن سُلْطَانٍ ۚ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ وَمَا تَهْوَى الْأَنفُسُ ۖ وَلَقَدْ جَاءَهُم مِّن رَّبِّهِمُ الْهُدَىٰ ۝٢٣
In hiya illaaa asmaaa`un sammaitumoohaaa antum wa aabaaa`ukum maaa anzalal laahu bihaa min sultaan; inyyattabi`oona illaz zanna wa maa tahwal anfusu wa laqad jaaa`ahum mir Rabbihimul hudaa
📖 Tekkim Wolof
Loolu ay tur la doŋŋ yu ngeen di tudd (xërëm ya), yéen ak seeni baay. Seen njortu rekk la ñu topp waaye yayoowunu jaamu. Topp it seen bànneex, looloo tax njub dikk bawoo fa seen Boroom.

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore An-Najm

21أَلَكُمُ الذَّكَرُ وَلَهُ الْأُنثَىٰ
Moo ndax yéen a am doom yu góor moom Yàlla mu am ay jigéen ?
22تِلْكَ إِذًا قِسْمَةٌ ضِيزَىٰ
(Xam ngeen) ne woowu séddale yéen jubul de !
23إِنْ هِيَ إِلَّا أَسْمَاءٌ سَمَّيْتُمُوهَا أَنتُمْ وَآبَاؤُكُم مَّا أَنزَلَ اللَّهُ بِهَا مِن سُلْطَانٍ ۚ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ وَمَا تَهْوَى الْأَنفُسُ ۖ وَلَقَدْ جَاءَهُم مِّن رَّبِّهِمُ الْهُدَىٰ
Loolu ay tur la doŋŋ yu ngeen di tudd (xërëm ya), yéen ak seeni baay. Seen njortu rekk la ñu topp waaye yayoowunu jaamu. Topp it seen bànneex, looloo tax njub dikk bawoo fa seen Boroom.
24أَمْ لِلْإِنسَانِ مَا تَمَنَّىٰ
Walla book nit moom limu mébét da koy daldi am ?
25فَلِلَّهِ الْآخِرَةُ وَالْأُولَىٰ
Yàllaa moom àddinaak àllaaxira.
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — An-Najm 23

Simoore An-Najm Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Loolu ay tur la doŋŋ yu ngeen di tudd (xërëm…

Simoore Aaya 23/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers