An-Najm · 22/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
تِلْكَ إِذًا قِسْمَةٌ ضِيزَىٰ ۝٢٢
Tilka izan qismatun deezaa
📖 Tekkim Wolof
(Xam ngeen) ne woowu séddale yéen jubul de !

🎧 Dégg


📜 Aaya 20-24 — Simoore An-Najm

20وَمَنَاةَ الثَّالِثَةَ الْأُخْرَىٰ
ak Manaat xërëm ba ca des, te ñetteel leen ?
21أَلَكُمُ الذَّكَرُ وَلَهُ الْأُنثَىٰ
Moo ndax yéen a am doom yu góor moom Yàlla mu am ay jigéen ?
22تِلْكَ إِذًا قِسْمَةٌ ضِيزَىٰ
(Xam ngeen) ne woowu séddale yéen jubul de !
23إِنْ هِيَ إِلَّا أَسْمَاءٌ سَمَّيْتُمُوهَا أَنتُمْ وَآبَاؤُكُم مَّا أَنزَلَ اللَّهُ بِهَا مِن سُلْطَانٍ ۚ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ وَمَا تَهْوَى الْأَنفُسُ ۖ وَلَقَدْ جَاءَهُم مِّن رَّبِّهِمُ الْهُدَىٰ
Loolu ay tur la doŋŋ yu ngeen di tudd (xërëm ya), yéen ak seeni baay. Seen njortu rekk la ñu topp waaye yayoowunu jaamu. Topp it seen bànneex, looloo tax njub dikk bawoo fa seen Boroom.
24أَمْ لِلْإِنسَانِ مَا تَمَنَّىٰ
Walla book nit moom limu mébét da koy daldi am ?
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — An-Najm 22

Simoore An-Najm Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Xam ngeen) ne woowu séddale yéen jubul de !

Simoore Aaya 22/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers