An-Najm · 44/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
وَأَنَّهُ هُوَ أَمَاتَ وَأَحْيَا ۝٤٤
Wa annahoo huwa amaata wa ahyaa
📖 Tekkim Wolof
te it moom Mooy rey mooy dekkal,

🎧 Dégg


📜 Aaya 42-46 — Simoore An-Najm

42وَأَنَّ إِلَىٰ رَبِّكَ الْمُنتَهَىٰ
te nag lépp, ngay jeexe, ca sa Boroom,
43وَأَنَّهُ هُوَ أَضْحَكَ وَأَبْكَىٰ
te moom Mooy reetaanloo di jooyloo,
44وَأَنَّهُ هُوَ أَمَاتَ وَأَحْيَا
te it moom Mooy rey mooy dekkal,
45وَأَنَّهُ خَلَقَ الزَّوْجَيْنِ الذَّكَرَ وَالْأُنثَىٰ
te moom Moo bind ñaari tóolent , yu di góor ak jigéen,
46مِن نُّطْفَةٍ إِذَا تُمْنَىٰ
muy bawoo ci toq maniyu wu wàcci ci njurukaay
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
44Aaya

Tekki — An-Najm 44

Simoore An-Najm Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te it moom Mooy rey mooy dekkal,

Simoore Aaya 44/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers