An-Najm · 45/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
وَأَنَّهُ خَلَقَ الزَّوْجَيْنِ الذَّكَرَ وَالْأُنثَىٰ ۝٤٥
Wa annahoo khalaqaz zawjainiz zakara wal unsaa
📖 Tekkim Wolof
te moom Moo bind ñaari tóolent , yu di góor ak jigéen,

🎧 Dégg


📜 Aaya 43-47 — Simoore An-Najm

43وَأَنَّهُ هُوَ أَضْحَكَ وَأَبْكَىٰ
te moom Mooy reetaanloo di jooyloo,
44وَأَنَّهُ هُوَ أَمَاتَ وَأَحْيَا
te it moom Mooy rey mooy dekkal,
45وَأَنَّهُ خَلَقَ الزَّوْجَيْنِ الذَّكَرَ وَالْأُنثَىٰ
te moom Moo bind ñaari tóolent , yu di góor ak jigéen,
46مِن نُّطْفَةٍ إِذَا تُمْنَىٰ
muy bawoo ci toq maniyu wu wàcci ci njurukaay
47وَأَنَّ عَلَيْهِ النَّشْأَةَ الْأُخْرَىٰ
moom moo waral it sosuwaat ga dekkiwaat,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — An-Najm 45

Simoore An-Najm Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te moom Moo bind ñaari tóolent , yu di góor…

Simoore Aaya 45/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers