Al-Qalam · 21/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
فَتَنَادَوْا مُصْبِحِينَ ۝٢١
Fatanaadaw musbiheen
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu xëy, wootante ca suba cuuy :

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 19-23 — Simoore Al-Qalam

19فَطَافَ عَلَيْهَا طَائِفٌ مِّن رَّبِّكَ وَهُمْ نَائِمُونَ
Mu am lu bawoo fa sa Boroom dikk wër si ko (faagaagal tool ba) fekk ñoom nelaw nañu,
20فَأَصْبَحَتْ كَالصَّرِيمِ
ba bët setee, mu melni luñu déqi.
21فَتَنَادَوْا مُصْبِحِينَ
Ba ñu xëy, wootante ca suba cuuy :
22أَنِ اغْدُوا عَلَىٰ حَرْثِكُمْ إِن كُنتُمْ صَارِمِينَ
“Daldi ne teel leen xëy tool waay ndegam da ngeen bëgg góob”.
23فَانطَلَقُوا وَهُمْ يَتَخَافَتُونَ
Ña ngay làkk, ca tool ya di déeyante :
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Al-Qalam 21

Simoore Al-Qalam Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu xëy, wootante ca suba cuuy :

Simoore Aaya 21/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers