Al-Qalam · 25/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
وَغَدَوْا عَلَىٰ حَرْدٍ قَادِرِينَ ۝٢٥
Wa ghadaw `alaa hardin qaadireen
📖 Tekkim Wolof
Ñu xëy njortu ne, man nañoo tere tool ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore Al-Qalam

23فَانطَلَقُوا وَهُمْ يَتَخَافَتُونَ
Ña ngay làkk, ca tool ya di déeyante :
24أَن لَّا يَدْخُلَنَّهَا الْيَوْمَ عَلَيْكُم مِّسْكِينٌ
Tey wax naan : “Tey jii buleen seetaan benn miskin di dugg ci tool yi”.
25وَغَدَوْا عَلَىٰ حَرْدٍ قَادِرِينَ
Ñu xëy njortu ne, man nañoo tere tool ya.
26فَلَمَّا رَأَوْهَا قَالُوا إِنَّا لَضَالُّونَ
Ba ñu ne gegg, ca tool ya ( mu melni peroŋ) : ñu ne : “nun xanaa da noo gëlam,
27بَلْ نَحْنُ مَحْرُومُونَ
Ñu ne moom la kat waaye li wóor moo di ne su nu muur jeex na ci”.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Al-Qalam 25

Simoore Al-Qalam Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu xëy njortu ne, man nañoo tere tool ya.

Simoore Aaya 25/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers