Al-Qalam · 24/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
أَن لَّا يَدْخُلَنَّهَا الْيَوْمَ عَلَيْكُم مِّسْكِينٌ ۝٢٤
Al laa yadkhulannahal yawma `alaikum miskeen
📖 Tekkim Wolof
Tey wax naan : “Tey jii buleen seetaan benn miskin di dugg ci tool yi”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 22-26 — Simoore Al-Qalam

22أَنِ اغْدُوا عَلَىٰ حَرْثِكُمْ إِن كُنتُمْ صَارِمِينَ
“Daldi ne teel leen xëy tool waay ndegam da ngeen bëgg góob”.
23فَانطَلَقُوا وَهُمْ يَتَخَافَتُونَ
Ña ngay làkk, ca tool ya di déeyante :
24أَن لَّا يَدْخُلَنَّهَا الْيَوْمَ عَلَيْكُم مِّسْكِينٌ
Tey wax naan : “Tey jii buleen seetaan benn miskin di dugg ci tool yi”.
25وَغَدَوْا عَلَىٰ حَرْدٍ قَادِرِينَ
Ñu xëy njortu ne, man nañoo tere tool ya.
26فَلَمَّا رَأَوْهَا قَالُوا إِنَّا لَضَالُّونَ
Ba ñu ne gegg, ca tool ya ( mu melni peroŋ) : ñu ne : “nun xanaa da noo gëlam,
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Al-Qalam 24

Simoore Al-Qalam Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tey wax naan : “Tey jii buleen seetaan benn miskin…

Simoore Aaya 24/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers