Al-Haqqa · 43/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
تَنزِيلٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ ۝٤٣
Tanzeelum mir rabbil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Dafa wàcc bawoo ci boroom àddina si.

🎧 Dégg


📜 Aaya 41-45 — Simoore Al-Haqqa

41وَمَا هُوَ بِقَوْلِ شَاعِرٍ ۚ قَلِيلًا مَّا تُؤْمِنُونَ
du waxu ab waykat ; li ngeen gëm néew na,
42وَلَا بِقَوْلِ كَاهِنٍ ۚ قَلِيلًا مَّا تَذَكَّرُونَ
du waxi it ab buxaaba, aka néew lu ngeen di fàttaliku.
43تَنزِيلٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Dafa wàcc bawoo ci boroom àddina si.
44وَلَوْ تَقَوَّلَ عَلَيْنَا بَعْضَ الْأَقَاوِيلِ
Su ca fentoon jenn jenn wax,
45لَأَخَذْنَا مِنْهُ بِالْيَمِينِ
( Kon ) dananu téye loxob ndeyjooram,
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
43Aaya

Tekki — Al-Haqqa 43

Simoore Al-Haqqa Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dafa wàcc bawoo ci boroom àddina si.

Simoore Aaya 43/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers