Al-Haqqa · 42/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
وَلَا بِقَوْلِ كَاهِنٍ ۚ قَلِيلًا مَّا تَذَكَّرُونَ ۝٤٢
Wa laa biqawli kaahin; qaleelam maa tazakkaroon
📖 Tekkim Wolof
du waxi it ab buxaaba, aka néew lu ngeen di fàttaliku.

🎧 Dégg


📜 Aaya 40-44 — Simoore Al-Haqqa

40إِنَّهُ لَقَوْلُ رَسُولٍ كَرِيمٍ
ci ne [Alxuraan] waxi ab Yonent la bu tedd,
41وَمَا هُوَ بِقَوْلِ شَاعِرٍ ۚ قَلِيلًا مَّا تُؤْمِنُونَ
du waxu ab waykat ; li ngeen gëm néew na,
42وَلَا بِقَوْلِ كَاهِنٍ ۚ قَلِيلًا مَّا تَذَكَّرُونَ
du waxi it ab buxaaba, aka néew lu ngeen di fàttaliku.
43تَنزِيلٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Dafa wàcc bawoo ci boroom àddina si.
44وَلَوْ تَقَوَّلَ عَلَيْنَا بَعْضَ الْأَقَاوِيلِ
Su ca fentoon jenn jenn wax,
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Al-Haqqa 42

Simoore Al-Haqqa Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : du waxi it ab buxaaba, aka néew lu ngeen di…

Simoore Aaya 42/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers