Al-A'raf · 116/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
قَالَ أَلْقُوا ۖ فَلَمَّا أَلْقَوْا سَحَرُوا أَعْيُنَ النَّاسِ وَاسْتَرْهَبُوهُمْ وَجَاءُوا بِسِحْرٍ عَظِيمٍ ۝١١٦
Qaala alqoo falam maaa alqaw saharooo a`yunannaasi wastarhaboohum wa jaaa`oo bisihrin `azeem
📖 Tekkim Wolof
Mu ne : “Sànnileen”. Ba ñu sànnee, dañoo jabar bëti nit ña, ragal-loo leen ci jabar gu rëy.
🎧 Dégg

📜 Aaya 114-118 — Al-A'raf

114قَالَ نَعَمْ وَإِنَّكُمْ لَمِنَ الْمُقَرَّبِينَ
Mu ne leen : “Waawaaw, kon dangeen bokk ci ñi may jegeñ”.
115قَالُوا يَا مُوسَىٰ إِمَّا أَن تُلْقِيَ وَإِمَّا أَن نَّكُونَ نَحْنُ الْمُلْقِينَ
Ñu ne : “Muusaa, benn yaw nga sànni, walla nun nu sànni”.
116قَالَ أَلْقُوا ۖ فَلَمَّا أَلْقَوْا سَحَرُوا أَعْيُنَ النَّاسِ وَاسْتَرْهَبُوهُمْ وَجَاءُوا بِسِحْرٍ عَظِيمٍ
Mu ne : “Sànnileen”. Ba ñu sànnee, dañoo jabar bëti nit ña, ragal-loo leen ci jabar gu rëy.
117۞ وَأَوْحَيْنَا إِلَىٰ مُوسَىٰ أَنْ أَلْقِ عَصَاكَ ۖ فَإِذَا هِيَ تَلْقَفُ مَا يَأْفِكُونَ
Nu xelal Muusaa ne ko : “Sànnil sa yet wi”. Mu daldi wann la ñu doon wëlbati.
118فَوَقَعَ الْحَقُّ وَبَطَلَ مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Dëgg daldi tàbbi, la ñu doon def yàqu.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
116Aaya

Tekki — Al-A'raf 116

Simoore Al-A'raf Aaya 116 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne : “Sànnileen”. Ba ñu sànnee, dañoo jabar bëti…

Simoore Aaya 116/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 114–118. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers