Al-A'raf · 131/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
فَإِذَا جَاءَتْهُمُ الْحَسَنَةُ قَالُوا لَنَا هَٰذِهِ ۖ وَإِن تُصِبْهُمْ سَيِّئَةٌ يَطَّيَّرُوا بِمُوسَىٰ وَمَن مَّعَهُ ۗ أَلَا إِنَّمَا طَائِرُهُمْ عِندَ اللَّهِ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ ۝١٣١
Fa izaa jaaa`at humul hasanatu qaaloo lanaa haazihee wa in tusibhum saiyi`atuny yattaiyaroo bi Moosaa wa mam ma`ah; alaaa innamaa taaa`iruhum `indal laahi wa laakinna aksarahum laa ya`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Bu leen lu baax dikkalee, ñu ne : “Lii noo ko moom” ; bu leen lu bon dalee, ñu gaafal Muusaa ak ña ànd ak moom. Déedéet seen gaaf nekkul ci kenn ku dul Yàlla. Waaye ña ëpp ca ñoom xamuñu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 129-133 — Al-A'raf

129قَالُوا أُوذِينَا مِن قَبْلِ أَن تَأْتِيَنَا وَمِن بَعْدِ مَا جِئْتَنَا ۚ قَالَ عَسَىٰ رَبُّكُمْ أَن يُهْلِكَ عَدُوَّكُمْ وَيَسْتَخْلِفَكُمْ فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرَ كَيْفَ تَعْمَلُونَ
[Ñoom yahuud ya] ne : “Loreef nanu lu jiitu sa dikk ci nun ak ginnaaw la nga nu indil.”. Mu ne : “Xéy-na seen Boroom dana rey seeni noon, Mu wuutal leen ci suuf si ba noppi di saytu na ngeen di def”.
130وَلَقَدْ أَخَذْنَا آلَ فِرْعَوْنَ بِالسِّنِينَ وَنَقْصٍ مِّنَ الثَّمَرَاتِ لَعَلَّهُمْ يَذَّكَّرُونَ
Teg Nanu nitu Firawna bekkoor ay at ak wàññikug meññent ndax xéy-na ñu fàttaliku [seen Boroom].
131فَإِذَا جَاءَتْهُمُ الْحَسَنَةُ قَالُوا لَنَا هَٰذِهِ ۖ وَإِن تُصِبْهُمْ سَيِّئَةٌ يَطَّيَّرُوا بِمُوسَىٰ وَمَن مَّعَهُ ۗ أَلَا إِنَّمَا طَائِرُهُمْ عِندَ اللَّهِ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Bu leen lu baax dikkalee, ñu ne : “Lii noo ko moom” ; bu leen lu bon dalee, ñu gaafal Muusaa ak ña ànd ak moom. Déedéet seen gaaf nekkul ci kenn ku dul Yàlla. Waaye ña ëpp ca ñoom xamuñu.
132وَقَالُوا مَهْمَا تَأْتِنَا بِهِ مِنْ آيَةٍ لِّتَسْحَرَنَا بِهَا فَمَا نَحْنُ لَكَ بِمُؤْمِنِينَ
Ñu ne : “ Loo nu mën a indil ciy kéemaan ngir jabar nu ci, dunu la gëm”.
133فَأَرْسَلْنَا عَلَيْهِمُ الطُّوفَانَ وَالْجَرَادَ وَالْقُمَّلَ وَالضَّفَادِعَ وَالدَّمَ آيَاتٍ مُّفَصَّلَاتٍ فَاسْتَكْبَرُوا وَكَانُوا قَوْمًا مُّجْرِمِينَ
Yabal Nanu ca seen kaw am mbënn, ak i njéeréer, ak teeñ ya ak mbott ya, ak deret ja, ñu di ay kéemaan yu fés, waaye ña rëy-rëylu nag ay nit ñu saay-saay lañu.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
131Aaya

Tekki — Al-A'raf 131

Simoore Al-A'raf Aaya 131 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu leen lu baax dikkalee, ñu ne : “Lii noo…

Simoore Aaya 131/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 129–133. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers