Al-A'raf · 14/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
قَالَ أَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ ۝١٤
Qaala anzirneee ilaa Yawmi yub`asoon
📖 Tekkim Wolof
Ibliis ne Ko : “Muñal ma ba bisu dekki ba.”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 12-16 — Simoore Al-A'raf

12قَالَ مَا مَنَعَكَ أَلَّا تَسْجُدَ إِذْ أَمَرْتُكَ ۖ قَالَ أَنَا خَيْرٌ مِّنْهُ خَلَقْتَنِي مِن نَّارٍ وَخَلَقْتَهُ مِن طِينٍ
[Yàlla] ne ko : “Lan moo la tee sujjóot ba Ma la ko digalee ? ”. Mu ne : “Maa ko gën : ndax Danga ma bind ci Safara, moom Nga bind ko ci ban”.
13قَالَ فَاهْبِطْ مِنْهَا فَمَا يَكُونُ لَكَ أَن تَتَكَبَّرَ فِيهَا فَاخْرُجْ إِنَّكَ مِنَ الصَّاغِرِينَ
[Yàlla] ne ko : “Wàccal jóge fi, yaw waroo fi rëy-rëylu. Génnal, torox nga.”
14قَالَ أَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
Ibliis ne Ko : “Muñal ma ba bisu dekki ba.”
15قَالَ إِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ
[Yàlla] ne ko : “Bokk nga ca ña Nuy muñandiku.”
16قَالَ فَبِمَا أَغْوَيْتَنِي لَأَقْعُدَنَّ لَهُمْ صِرَاطَكَ الْمُسْتَقِيمَ
bliis daldi ne : “Giñ naa ne beewloo gi Nga ma teg, danaa leen rékki ci sa yoon wu jub wi,
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Al-A'raf 14

Simoore Al-A'raf Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ibliis ne Ko : “Muñal ma ba bisu dekki ba.”

Simoore Aaya 14/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers