Al-A'raf · 15/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
قَالَ إِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ ١٥
Transliteration
Qaala innaka minal munzareen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
[Yàlla] ne ko : “Bokk nga ca ña Nuy muñandiku.”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 13-17 — Al-A'raf
13قَالَ فَاهْبِطْ مِنْهَا فَمَا يَكُونُ لَكَ أَن تَتَكَبَّرَ فِيهَا فَاخْرُجْ إِنَّكَ مِنَ الصَّاغِرِينَ
[Yàlla] ne ko : “Wàccal jóge fi, yaw waroo fi rëy-rëylu. Génnal, torox nga.”
14قَالَ أَنظِرْنِي إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
Ibliis ne Ko : “Muñal ma ba bisu dekki ba.”
15قَالَ إِنَّكَ مِنَ الْمُنظَرِينَ
[Yàlla] ne ko : “Bokk nga ca ña Nuy muñandiku.”
16قَالَ فَبِمَا أَغْوَيْتَنِي لَأَقْعُدَنَّ لَهُمْ صِرَاطَكَ الْمُسْتَقِيمَ
bliis daldi ne : “Giñ naa ne beewloo gi Nga ma teg, danaa leen rékki ci sa yoon wu jub
wi,
17ثُمَّ لَآتِيَنَّهُم مِّن بَيْنِ أَيْدِيهِمْ وَمِنْ خَلْفِهِمْ وَعَنْ أَيْمَانِهِمْ وَعَن شَمَائِلِهِمْ ۖ وَلَا تَجِدُ أَكْثَرَهُمْ شَاكِرِينَ
bu ko defee, ma songe leen ci seen kanam ak ci seen ginnaaw, seen ndeyjoor ak ci seen càmmoñ ba lu ëpp ci ñoom duñu la sant.”
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
15Aaya
Tekki — Al-A'raf 15
Simoore Al-A'raf Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Yàlla] ne ko : “Bokk nga ca ña Nuy muñandiku.”Simoore Aaya 15/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








