Al-A'raf · 184/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
أَوَلَمْ يَتَفَكَّرُوا ۗ مَا بِصَاحِبِهِم مِّن جِنَّةٍ ۚ إِنْ هُوَ إِلَّا نَذِيرٌ مُّبِينٌ ۝١٨٤
Awalam yatafakkaroo maa bisaahibihim min jinnah; in huwa illaa nazeerum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dañu dul xél-lu xam ne seen àndandoo bi jinne jàppu ko? Nekkul lu dul waarekat bu ràññeeku !

🎧 Dégg


📜 Aaya 182-186 — Al-A'raf

182وَالَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا سَنَسْتَدْرِجُهُم مِّنْ حَيْثُ لَا يَعْلَمُونَ
Waaye ña weddi Sunuy tegtal, Dananu leen jay, jaarele leen fu ñu xamul.
183وَأُمْلِي لَهُمْ ۚ إِنَّ كَيْدِي مَتِينٌ
Muñal-leen, Sama pexe naka lu dëgër la !
184أَوَلَمْ يَتَفَكَّرُوا ۗ مَا بِصَاحِبِهِم مِّن جِنَّةٍ ۚ إِنْ هُوَ إِلَّا نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Moo ndax dañu dul xél-lu xam ne seen àndandoo bi jinne jàppu ko? Nekkul lu dul waarekat bu ràññeeku !
185أَوَلَمْ يَنظُرُوا فِي مَلَكُوتِ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا خَلَقَ اللَّهُ مِن شَيْءٍ وَأَنْ عَسَىٰ أَن يَكُونَ قَدِ اقْتَرَبَ أَجَلُهُمْ ۖ فَبِأَيِّ حَدِيثٍ بَعْدَهُ يُؤْمِنُونَ
Moo ndax dañu dul xool nguuru asamaan yi ak suuf si, ak li Yàlla bind lépp, te it xéy-na Mu jegeñal seen àpp ? Kon jan wax gannaaw josam, lañu mën a gëm ?
186مَن يُضْلِلِ اللَّهُ فَلَا هَادِيَ لَهُ ۚ وَيَذَرُهُمْ فِي طُغْيَانِهِمْ يَعْمَهُونَ
Ku Yàlla bàyyi cig réeram, kenn du la mën a gindi. Dana leen jàppe ca seen beew ga ñuy tëñax-tëñaxi.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
184Aaya

Tekki — Al-A'raf 184

Simoore Al-A'raf Aaya 184 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dañu dul xél-lu xam ne seen àndandoo bi…

Simoore Aaya 184/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 182–186. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers