Al-A'raf · 78/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
فَأَخَذَتْهُمُ الرَّجْفَةُ فَأَصْبَحُوا فِي دَارِهِمْ جَاثِمِينَ ۝٧٨
Fa akhazat humur rajftu fa asbahoo fee daarihim jaasimmeen
📖 Tekkim Wolof
Ag yëngug suuf rajaxe leen ; ñu xëy ne lànjaŋ ca seen kër ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 76-80 — Simoore Al-A'raf

76قَالَ الَّذِينَ اسْتَكْبَرُوا إِنَّا بِالَّذِي آمَنتُم بِهِ كَافِرُونَ
Ñay rëy-rëylu ne leen : “Nun dey, li ngeen gëm, weddi nanu ko”.
77فَعَقَرُوا النَّاقَةَ وَعَتَوْا عَنْ أَمْرِ رَبِّهِمْ وَقَالُوا يَا صَالِحُ ائْتِنَا بِمَا تَعِدُنَا إِن كُنتَ مِنَ الْمُرْسَلِينَ
Ñu rey giléem ga, jalgati seen ndigalul Boroom, daldi ne : “Yaw Saalihu, indil nu la nga nu doon tëkkoo, ndegam ci Yonent yi nga bokk”.
78فَأَخَذَتْهُمُ الرَّجْفَةُ فَأَصْبَحُوا فِي دَارِهِمْ جَاثِمِينَ
Ag yëngug suuf rajaxe leen ; ñu xëy ne lànjaŋ ca seen kër ya.
79فَتَوَلَّىٰ عَنْهُمْ وَقَالَ يَا قَوْمِ لَقَدْ أَبْلَغْتُكُمْ رِسَالَةَ رَبِّي وَنَصَحْتُ لَكُمْ وَلَٰكِن لَّا تُحِبُّونَ النَّاصِحِينَ
Mu dëddu leen, daldi ne : "Yéen samay mbokk, jottali naa leen sama Yonenteb Boroom, laabire naa leen itam. Waaye yéen dey soppuleen laabirekat yi ! ”
80وَلُوطًا إِذْ قَالَ لِقَوْمِهِ أَتَأْتُونَ الْفَاحِشَةَ مَا سَبَقَكُم بِهَا مِنْ أَحَدٍ مِّنَ الْعَالَمِينَ
Fàttalikuleen itam ba Lóot waxee aw nitam, ne leen : “Moo ndax dangeen di def ñaawtéef woo xam ne kenn mësu koo def ci àddina sépp ?
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
78Aaya

Tekki — Al-A'raf 78

Simoore Al-A'raf Aaya 78 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ag yëngug suuf rajaxe leen ; ñu xëy ne lànjaŋ…

Simoore Aaya 78/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 76–80. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers