Nuh · 21/28
Tekki Waxtaan — Nuh
قَالَ نُوحٌ رَّبِّ إِنَّهُمْ عَصَوْنِي وَاتَّبَعُوا مَن لَّمْ يَزِدْهُ مَالُهُ وَوَلَدُهُ إِلَّا خَسَارًا ٢١
Transliteration
Qaala Noohur Robbi innahum `asawnee wattaba`oo mal lam yazid hu maaluhoo wa waladuhooo illaa khasaara
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nooh daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, (samaw nit) moy na ñu ma dem toppi koo xam ne alalam ak i doomam jariñu ko lu dul yàqule.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 19-23 — Nuh
19وَاللَّهُ جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ بِسَاطًا
Yàlla moo leen defaral suuf si mu di laltaay,
20لِّتَسْلُكُوا مِنْهَا سُبُلًا فِجَاجًا
ngir ngeen mana sóobu ca yoonam yu dàndante ya”.
21قَالَ نُوحٌ رَّبِّ إِنَّهُمْ عَصَوْنِي وَاتَّبَعُوا مَن لَّمْ يَزِدْهُ مَالُهُ وَوَلَدُهُ إِلَّا خَسَارًا
Nooh daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, (samaw nit) moy na ñu ma dem toppi koo xam ne alalam ak i doomam jariñu ko lu dul yàqule.
22وَمَكَرُوا مَكْرًا كُبَّارًا
Ña ngay fexe pexe yu rëy,
23وَقَالُوا لَا تَذَرُنَّ آلِهَتَكُمْ وَلَا تَذَرُنَّ وَدًّا وَلَا سُوَاعًا وَلَا يَغُوثَ وَيَعُوقَ وَنَسْرًا
tey wax naan : “Buleen bàyyi seeni Yàlli bu leen bàyyi Wud, Mbaa Suwaa’, ak Yaquusa, ak Ya’uuqa ak Nasra.
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
21Aaya
Tekki — Nuh 21
Simoore Nuh Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nooh daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, (samaw nit)…Simoore Aaya 21/28 — Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Nuh Dégg, Nuh Tekki, Nuh mp3, Nuh pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








