Yunus · 10/109
Tekki Waxtaan — Yunus
دَعْوَاهُمْ فِيهَا سُبْحَانَكَ اللَّهُمَّ وَتَحِيَّتُهُمْ فِيهَا سَلَامٌ ۚ وَآخِرُ دَعْوَاهُمْ أَنِ الْحَمْدُ لِلَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ ۝١٠
Da`waahum feehaa Subbaanakal laahumma wa tahiyyatuhum feehaa salaam; wa aakhiru da`waahum anil hamdu lillaahi Rabbil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Seenug jaamu foofa mooy di wax naan : “Cëy sellug sunu Boroom”, te seenug nuyyoo foofa mooy : “Jàmm rekk”, te la ñuy mujjeel ca seenug jaamu, moo di ñu wax ne: “Mbooleem xeeti cant yi ñeel na Yàlla Boroom àddina si”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Yunus

8أُولَٰئِكَ مَأْوَاهُمُ النَّارُ بِمَا كَانُوا يَكْسِبُونَ
ñooña seen delluwaay moo di Safara ngir la ñu fàggu.
9إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ يَهْدِيهِمْ رَبُّهُم بِإِيمَانِهِمْ ۖ تَجْرِي مِن تَحْتِهِمُ الْأَنْهَارُ فِي جَنَّاتِ النَّعِيمِ
Ña nga xam ne gëm nañu tey jëf yu yiw, seen Boroom dana leen wommat ngir seen ngëm, tàbbal leen Àjjanay xéewal. Ay dex di daw ci seen suuf.
10دَعْوَاهُمْ فِيهَا سُبْحَانَكَ اللَّهُمَّ وَتَحِيَّتُهُمْ فِيهَا سَلَامٌ ۚ وَآخِرُ دَعْوَاهُمْ أَنِ الْحَمْدُ لِلَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Seenug jaamu foofa mooy di wax naan : “Cëy sellug sunu Boroom”, te seenug nuyyoo foofa mooy : “Jàmm rekk”, te la ñuy mujjeel ca seenug jaamu, moo di ñu wax ne: “Mbooleem xeeti cant yi ñeel na Yàlla Boroom àddina si”.
11۞ وَلَوْ يُعَجِّلُ اللَّهُ لِلنَّاسِ الشَّرَّ اسْتِعْجَالَهُم بِالْخَيْرِ لَقُضِيَ إِلَيْهِمْ أَجَلُهُمْ ۖ فَنَذَرُ الَّذِينَ لَا يَرْجُونَ لِقَاءَنَا فِي طُغْيَانِهِمْ يَعْمَهُونَ
Bu Yàlla gaawe woon àtte nit ñi ci mettit kem ni ñu yàkkamtee am alal, àttekoon na seenug yàkkamti. Waaye Dananu bàyyi ña nga xam ne yaakaaruñoo dajeek Nun ñuy laam- laame ca seen biir ngëlamte.
12وَإِذَا مَسَّ الْإِنسَانَ الضُّرُّ دَعَانَا لِجَنبِهِ أَوْ قَاعِدًا أَوْ قَائِمًا فَلَمَّا كَشَفْنَا عَنْهُ ضُرَّهُ مَرَّ كَأَن لَّمْ يَدْعُنَا إِلَىٰ ضُرٍّ مَّسَّهُ ۚ كَذَٰلِكَ زُيِّنَ لِلْمُسْرِفِينَ مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Nit, bu ko aw naqar dalee, mu daldi Nuy woo, (moo xam dakoo fekk mu) tëdd walla mu toog walla taxaw. Te bu Nu ko tekkilee naqaram woowu, muy wéy (ci kéefaram), fakk mel ni mësunoo woo ci naqar wu ko dal. Noonu la jekkee woon ca ñoom bokkaalekat ya la ñu daan def.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Yunus 10

Simoore Yunus Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seenug jaamu foofa mooy di wax naan : “Cëy sellug…

Simoore Aaya 10/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers