Yunus · 78/109
Tekki Waxtaan — Yunus
قَالُوا أَجِئْتَنَا لِتَلْفِتَنَا عَمَّا وَجَدْنَا عَلَيْهِ آبَاءَنَا وَتَكُونَ لَكُمَا الْكِبْرِيَاءُ فِي الْأَرْضِ وَمَا نَحْنُ لَكُمَا بِمُؤْمِنِينَ ٧٨
Transliteration
Qaaloo aji`tanaa litalfitanaa `ammaa wajadnaa `alaihi aabaaa`anaa wa takoona lakumal kibriyaaa`u fil ardi wa maa nahnu lakumaa bimu` mineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Moo ndax danga fee dikk ngir dëddale nu ak la nu fekkoon sunuy baay nekk ca ? Ba noppi yéen ñaar ngeen yilif àddina bi ? Waay-waay nun sax gëmunuleen ! ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 76-80 — Yunus
76فَلَمَّا جَاءَهُمُ الْحَقُّ مِنْ عِندِنَا قَالُوا إِنَّ هَٰذَا لَسِحْرٌ مُّبِينٌ
Ba dëgg ga agsee ca ñoom tukkee ci Nun Yàlla, [ñu ne leen] : “Jibar tigi la ! ”.
77قَالَ مُوسَىٰ أَتَقُولُونَ لِلْحَقِّ لَمَّا جَاءَكُمْ ۖ أَسِحْرٌ هَٰذَا وَلَا يُفْلِحُ السَّاحِرُونَ
Muusaa ne leen : “Moo ndax dangeen di wax ci dëgg gii ba mu agsee ci yéen, naan leen : Ag jibar la ? Te jibarkat yi duñu texe...”.
78قَالُوا أَجِئْتَنَا لِتَلْفِتَنَا عَمَّا وَجَدْنَا عَلَيْهِ آبَاءَنَا وَتَكُونَ لَكُمَا الْكِبْرِيَاءُ فِي الْأَرْضِ وَمَا نَحْنُ لَكُمَا بِمُؤْمِنِينَ
Ñu ne ko : “Moo ndax danga fee dikk ngir dëddale nu ak la nu fekkoon sunuy baay nekk ca ? Ba noppi yéen ñaar ngeen yilif àddina bi ? Waay-waay nun sax gëmunuleen ! ”
79وَقَالَ فِرْعَوْنُ ائْتُونِي بِكُلِّ سَاحِرٍ عَلِيمٍ
Firawna ne : “Indil-leen ma bépp jibarkat bu am xam-xam ! ”.
80فَلَمَّا جَاءَ السَّحَرَةُ قَالَ لَهُم مُّوسَىٰ أَلْقُوا مَا أَنتُم مُّلْقُونَ
Ba jibarkat ya dikkee, Muusaa ne leen : “Sànnileen li ngeen di sànni”.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
78Aaya
Tekki — Yunus 78
Simoore Yunus Aaya 78 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Moo ndax danga fee dikk ngir…Simoore Aaya 78/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 76–80. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








