Yunus · 77/109
Tekki Waxtaan — Simoore Yunus
قَالَ مُوسَىٰ أَتَقُولُونَ لِلْحَقِّ لَمَّا جَاءَكُمْ ۖ أَسِحْرٌ هَٰذَا وَلَا يُفْلِحُ السَّاحِرُونَ ۝٧٧
Qaalaa Moosaaa ataqooloona lilhaqqi lammmaa jaaa`a kum asihrun haazaa wa laa yuflihus saabiroon
📖 Tekkim Wolof
Muusaa ne leen : “Moo ndax dangeen di wax ci dëgg gii ba mu agsee ci yéen, naan leen : Ag jibar la ? Te jibarkat yi duñu texe...”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 75-79 — Simoore Yunus

75ثُمَّ بَعَثْنَا مِن بَعْدِهِم مُّوسَىٰ وَهَارُونَ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ بِآيَاتِنَا فَاسْتَكْبَرُوا وَكَانُوا قَوْمًا مُّجْرِمِينَ
Topp Nu yónni ci seen ginnaaw Muusaa ak Haaroona ca [Firawna] ak mbooloo ma [ñu xamal leen] sunuy ndigal. Ñu rëy-rëylu, di aw nit ñu dëng [diy saay-saay].
76فَلَمَّا جَاءَهُمُ الْحَقُّ مِنْ عِندِنَا قَالُوا إِنَّ هَٰذَا لَسِحْرٌ مُّبِينٌ
Ba dëgg ga agsee ca ñoom tukkee ci Nun Yàlla, [ñu ne leen] : “Jibar tigi la ! ”.
77قَالَ مُوسَىٰ أَتَقُولُونَ لِلْحَقِّ لَمَّا جَاءَكُمْ ۖ أَسِحْرٌ هَٰذَا وَلَا يُفْلِحُ السَّاحِرُونَ
Muusaa ne leen : “Moo ndax dangeen di wax ci dëgg gii ba mu agsee ci yéen, naan leen : Ag jibar la ? Te jibarkat yi duñu texe...”.
78قَالُوا أَجِئْتَنَا لِتَلْفِتَنَا عَمَّا وَجَدْنَا عَلَيْهِ آبَاءَنَا وَتَكُونَ لَكُمَا الْكِبْرِيَاءُ فِي الْأَرْضِ وَمَا نَحْنُ لَكُمَا بِمُؤْمِنِينَ
Ñu ne ko : “Moo ndax danga fee dikk ngir dëddale nu ak la nu fekkoon sunuy baay nekk ca ? Ba noppi yéen ñaar ngeen yilif àddina bi ? Waay-waay nun sax gëmunuleen ! ”
79وَقَالَ فِرْعَوْنُ ائْتُونِي بِكُلِّ سَاحِرٍ عَلِيمٍ
Firawna ne : “Indil-leen ma bépp jibarkat bu am xam-xam ! ”.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
77Aaya

Tekki — Yunus 77

Simoore Yunus Aaya 77 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muusaa ne leen : “Moo ndax dangeen di wax ci…

Simoore Aaya 77/109 — Simoore Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yunus Dégg, Simoore Yunus Tekki, Simoore Yunus mp3, Simoore Yunus pdf. Aaya 75–79. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers