Hud · 70/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
فَلَمَّا رَأَىٰ أَيْدِيَهُمْ لَا تَصِلُ إِلَيْهِ نَكِرَهُمْ وَأَوْجَسَ مِنْهُمْ خِيفَةً ۚ قَالُوا لَا تَخَفْ إِنَّا أُرْسِلْنَا إِلَىٰ قَوْمِ لُوطٍ ۝٧٠
Falammaa ra aaa aidiyahum laa tasilu ilaihi nakirahum wa awjasa minhum kheefah; qaaloo la takhaf innaaa ursilnaaa ilaa qawmi Loot
📖 Tekkim Wolof
Ba mu gisee ne seeni yoxo laalu ko, mu am tuuma ak ug tiit ci ñoom. Ñu ne ko : “Bul ragal, nun kat dañunoo yónni ca nitu Lóot ñi”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 68-72 — Simoore Hud

68كَأَن لَّمْ يَغْنَوْا فِيهَا ۗ أَلَا إِنَّ ثَمُودَ كَفَرُوا رَبَّهُمْ ۗ أَلَا بُعْدًا لِّثَمُودَ
ñu mel ni mësuñu faa sax. Waaw, ndax waa Samuuda weddiwuñu woon seen Boroom ? Moo ndax alkaande dalul waa Samuuda ?
69وَلَقَدْ جَاءَتْ رُسُلُنَا إِبْرَاهِيمَ بِالْبُشْرَىٰ قَالُوا سَلَامًا ۖ قَالَ سَلَامٌ ۖ فَمَا لَبِثَ أَن جَاءَ بِعِجْلٍ حَنِيذٍ
Sunuy ndaw indiloon na Ibraahiima mbégte, ñu ne ko : “Jàmmi Yàlla na nekk ci yaw ! ”. Mu ne leen : “Jàmm ci yéen it ! ”, nis tuut mu indil leen sëll wu ñu wàjj.
70فَلَمَّا رَأَىٰ أَيْدِيَهُمْ لَا تَصِلُ إِلَيْهِ نَكِرَهُمْ وَأَوْجَسَ مِنْهُمْ خِيفَةً ۚ قَالُوا لَا تَخَفْ إِنَّا أُرْسِلْنَا إِلَىٰ قَوْمِ لُوطٍ
Ba mu gisee ne seeni yoxo laalu ko, mu am tuuma ak ug tiit ci ñoom. Ñu ne ko : “Bul ragal, nun kat dañunoo yónni ca nitu Lóot ñi”.
71وَامْرَأَتُهُ قَائِمَةٌ فَضَحِكَتْ فَبَشَّرْنَاهَا بِإِسْحَاقَ وَمِن وَرَاءِ إِسْحَاقَ يَعْقُوبَ
Noona soxnaam sa taxawoon [foofa] daldi ree ; Nu bégal ko [te xamal ko ne dana am doom ju tudd] Isaaqa, ak ci ginnaawam Isaaqa, Yanqooba.
72قَالَتْ يَا وَيْلَتَىٰ أَأَلِدُ وَأَنَا عَجُوزٌ وَهَٰذَا بَعْلِي شَيْخًا ۖ إِنَّ هَٰذَا لَشَيْءٌ عَجِيبٌ
Mu wax ne : “Cëy man ! Ndax danaa jurati doom te màggat naa, sama boroom-kër bii it di ku mage ? Lii dey mbir mu doy waar la ! ”
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
70Aaya

Tekki — Hud 70

Simoore Hud Aaya 70 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba mu gisee ne seeni yoxo laalu ko, mu am…

Simoore Aaya 70/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 68–72. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers