Hud · 76/123
Tekki Waxtaan — Hud
يَا إِبْرَاهِيمُ أَعْرِضْ عَنْ هَٰذَا ۖ إِنَّهُ قَدْ جَاءَ أَمْرُ رَبِّكَ ۖ وَإِنَّهُمْ آتِيهِمْ عَذَابٌ غَيْرُ مَرْدُودٍ ٧٦
Transliteration
Yaaa Ibraaheemu a`rid `an haazaaa innahoo qad jaaa`a amru Rabbika wa innahum aateehim `azaabun ghairun mardood
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Yaw Ibraahiima, génnal ci lii ndax sa ndigalul Boroom dikk na ba noppi, te
ñoom, mbugal mu ñu dul delloo dana leen dikkal”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 74-78 — Hud
74فَلَمَّا ذَهَبَ عَنْ إِبْرَاهِيمَ الرَّوْعُ وَجَاءَتْهُ الْبُشْرَىٰ يُجَادِلُنَا فِي قَوْمِ لُوطٍ
Ba tiit ma bàyyee Ibraahiima te mu am mbégte, jéem naa dàggasante ak Nun ci nitu Lóot ña,
75إِنَّ إِبْرَاهِيمَ لَحَلِيمٌ أَوَّاهٌ مُّنِيبٌ
Ibraahiima dey ku lewet la, di kuy toroxlu, di ab delluwaakoon ci Boroomam.
76يَا إِبْرَاهِيمُ أَعْرِضْ عَنْ هَٰذَا ۖ إِنَّهُ قَدْ جَاءَ أَمْرُ رَبِّكَ ۖ وَإِنَّهُمْ آتِيهِمْ عَذَابٌ غَيْرُ مَرْدُودٍ
Ñu ne ko : “Yaw Ibraahiima, génnal ci lii ndax sa ndigalul Boroom dikk na ba noppi, te
ñoom, mbugal mu ñu dul delloo dana leen dikkal”.
77وَلَمَّا جَاءَتْ رُسُلُنَا لُوطًا سِيءَ بِهِمْ وَضَاقَ بِهِمْ ذَرْعًا وَقَالَ هَٰذَا يَوْمٌ عَصِيبٌ
Ba Sunuy ndaw agsee ca Lóot, mu jàq ca ñoom, am naqar ci ñoom. Daldi ne : “Lii dey bis bu tiis la”.
78وَجَاءَهُ قَوْمُهُ يُهْرَعُونَ إِلَيْهِ وَمِن قَبْلُ كَانُوا يَعْمَلُونَ السَّيِّئَاتِ ۚ قَالَ يَا قَوْمِ هَٰؤُلَاءِ بَنَاتِي هُنَّ أَطْهَرُ لَكُمْ ۖ فَاتَّقُوا اللَّهَ وَلَا تُخْزُونِ فِي ضَيْفِي ۖ أَلَيْسَ مِنكُمْ رَجُلٌ رَّشِيدٌ
Nitam ña ñëw ci moom di gaawantu. Te lu jiitu loolu, dañu daan def jëf ju ñaaw. Lóot ne leen : “Yéen samaw nit, samay doom yu jigéen ñi : ñoo gën a yell ci yéen. Nangeen ragal Yàlla, te buleen ma toroxal mukk ci sama gan ñi. Ndax amul ci yéen génn góor gu jub ? ”
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
76Aaya
Tekki — Hud 76
Simoore Hud Aaya 76 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Yaw Ibraahiima, génnal ci lii ndax…Simoore Aaya 76/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 74–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








