Hud · 77/123
Tekki Waxtaan — Hud
وَلَمَّا جَاءَتْ رُسُلُنَا لُوطًا سِيءَ بِهِمْ وَضَاقَ بِهِمْ ذَرْعًا وَقَالَ هَٰذَا يَوْمٌ عَصِيبٌ ۝٧٧
Wa lammaa jaaa`at Rusulunaa Lootan seee`a bihim wa daaqa bihim zar`anw wa qaala haazaa yawmun `aseeb
📖 Tekkim Wolof
Ba Sunuy ndaw agsee ca Lóot, mu jàq ca ñoom, am naqar ci ñoom. Daldi ne : “Lii dey bis bu tiis la”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 75-79 — Hud

75إِنَّ إِبْرَاهِيمَ لَحَلِيمٌ أَوَّاهٌ مُّنِيبٌ
Ibraahiima dey ku lewet la, di kuy toroxlu, di ab delluwaakoon ci Boroomam.
76يَا إِبْرَاهِيمُ أَعْرِضْ عَنْ هَٰذَا ۖ إِنَّهُ قَدْ جَاءَ أَمْرُ رَبِّكَ ۖ وَإِنَّهُمْ آتِيهِمْ عَذَابٌ غَيْرُ مَرْدُودٍ
Ñu ne ko : “Yaw Ibraahiima, génnal ci lii ndax sa ndigalul Boroom dikk na ba noppi, te ñoom, mbugal mu ñu dul delloo dana leen dikkal”.
77وَلَمَّا جَاءَتْ رُسُلُنَا لُوطًا سِيءَ بِهِمْ وَضَاقَ بِهِمْ ذَرْعًا وَقَالَ هَٰذَا يَوْمٌ عَصِيبٌ
Ba Sunuy ndaw agsee ca Lóot, mu jàq ca ñoom, am naqar ci ñoom. Daldi ne : “Lii dey bis bu tiis la”.
78وَجَاءَهُ قَوْمُهُ يُهْرَعُونَ إِلَيْهِ وَمِن قَبْلُ كَانُوا يَعْمَلُونَ السَّيِّئَاتِ ۚ قَالَ يَا قَوْمِ هَٰؤُلَاءِ بَنَاتِي هُنَّ أَطْهَرُ لَكُمْ ۖ فَاتَّقُوا اللَّهَ وَلَا تُخْزُونِ فِي ضَيْفِي ۖ أَلَيْسَ مِنكُمْ رَجُلٌ رَّشِيدٌ
Nitam ña ñëw ci moom di gaawantu. Te lu jiitu loolu, dañu daan def jëf ju ñaaw. Lóot ne leen : “Yéen samaw nit, samay doom yu jigéen ñi : ñoo gën a yell ci yéen. Nangeen ragal Yàlla, te buleen ma toroxal mukk ci sama gan ñi. Ndax amul ci yéen génn góor gu jub ? ”
79قَالُوا لَقَدْ عَلِمْتَ مَا لَنَا فِي بَنَاتِكَ مِنْ حَقٍّ وَإِنَّكَ لَتَعْلَمُ مَا نُرِيدُ
Ñu ne ko : Xam nga ne amuñu soxla ci sa doom yu jigéen yi. Te yaw xam nga xéll li nu bëgg”.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
77Aaya

Tekki — Hud 77

Simoore Hud Aaya 77 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba Sunuy ndaw agsee ca Lóot, mu jàq ca ñoom,…

Simoore Aaya 77/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 75–79. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers