Yusuf · 92/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
قَالَ لَا تَثْرِيبَ عَلَيْكُمُ الْيَوْمَ ۖ يَغْفِرُ اللَّهُ لَكُمْ ۖ وَهُوَ أَرْحَمُ الرَّاحِمِينَ ۝٩٢
Qaala laa tasreeba `alaikumul yawma yaghfirul laahu lakum wa Huwa arhamur raahimeen
📖 Tekkim Wolof
- Mu ne : “Tey du bisub yeddeel ci yéen ? Yal na leen Yàlla baal. Te Moom moo gën a mën a yërëm yërëmekat ya.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 90-94 — Simoore Yusuf

90قَالُوا أَإِنَّكَ لَأَنتَ يُوسُفُ ۖ قَالَ أَنَا يُوسُفُ وَهَٰذَا أَخِي ۖ قَدْ مَنَّ اللَّهُ عَلَيْنَا ۖ إِنَّهُ مَن يَتَّقِ وَيَصْبِرْ فَإِنَّ اللَّهَ لَا يُضِيعُ أَجْرَ الْمُحْسِنِينَ
- Ñu ne ko : “Ndax yaw yaay Yuusufa ? ” - Mu ne leen : “Maay Yuusufa, kii mooy sama doomu-ndey, Yàlla defal nu ay xéewal. Ndax ku ragal Yàlla te muñ, [dana gis ne] Yàlla du sànk mukk peyug ñay refetal”.
91قَالُوا تَاللَّهِ لَقَدْ آثَرَكَ اللَّهُ عَلَيْنَا وَإِن كُنَّا لَخَاطِئِينَ
- Ñu giñ ci Yàlla ne : “Yàlla gënal na la ci sunu kaw te nun danoo juumoon rekk def bàkkaar”.
92قَالَ لَا تَثْرِيبَ عَلَيْكُمُ الْيَوْمَ ۖ يَغْفِرُ اللَّهُ لَكُمْ ۖ وَهُوَ أَرْحَمُ الرَّاحِمِينَ
- Mu ne : “Tey du bisub yeddeel ci yéen ? Yal na leen Yàlla baal. Te Moom moo gën a mën a yërëm yërëmekat ya.
93اذْهَبُوا بِقَمِيصِي هَٰذَا فَأَلْقُوهُ عَلَىٰ وَجْهِ أَبِي يَأْتِ بَصِيرًا وَأْتُونِي بِأَهْلِكُمْ أَجْمَعِينَ
Demleen yóbbu sama yére yii ngeen sànni ko ca sama kanamu baay : dana dellu di gisaat. Te ngeen dellusi ànd ak njaboot ga gépp”.
94وَلَمَّا فَصَلَتِ الْعِيرُ قَالَ أَبُوهُمْ إِنِّي لَأَجِدُ رِيحَ يُوسُفَ ۖ لَوْلَا أَن تُفَنِّدُونِ
- Ba njëgg ga génnee [Misra], seen baay daldi ne : “Xetu Yuusufaa ngi may xeeñ, ndegam du ngeen wax ne damaa naax”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
92Aaya

Tekki — Yusuf 92

Simoore Yusuf Aaya 92 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Mu ne : “Tey du bisub yeddeel ci yéen…

Simoore Aaya 92/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 90–94. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers