Yusuf · 95/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
قَالُوا تَاللَّهِ إِنَّكَ لَفِي ضَلَالِكَ الْقَدِيمِ ۝٩٥
Qaaloo tallaahi innaka lafee dalaalikal qadeem
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Giñ nanu ci Yàlla ne yaa ngi ci sa njuumte lu jëkk la”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 93-97 — Simoore Yusuf

93اذْهَبُوا بِقَمِيصِي هَٰذَا فَأَلْقُوهُ عَلَىٰ وَجْهِ أَبِي يَأْتِ بَصِيرًا وَأْتُونِي بِأَهْلِكُمْ أَجْمَعِينَ
Demleen yóbbu sama yére yii ngeen sànni ko ca sama kanamu baay : dana dellu di gisaat. Te ngeen dellusi ànd ak njaboot ga gépp”.
94وَلَمَّا فَصَلَتِ الْعِيرُ قَالَ أَبُوهُمْ إِنِّي لَأَجِدُ رِيحَ يُوسُفَ ۖ لَوْلَا أَن تُفَنِّدُونِ
- Ba njëgg ga génnee [Misra], seen baay daldi ne : “Xetu Yuusufaa ngi may xeeñ, ndegam du ngeen wax ne damaa naax”.
95قَالُوا تَاللَّهِ إِنَّكَ لَفِي ضَلَالِكَ الْقَدِيمِ
Ñu ne ko : “Giñ nanu ci Yàlla ne yaa ngi ci sa njuumte lu jëkk la”.
96فَلَمَّا أَن جَاءَ الْبَشِيرُ أَلْقَاهُ عَلَىٰ وَجْهِهِ فَارْتَدَّ بَصِيرًا ۖ قَالَ أَلَمْ أَقُل لَّكُمْ إِنِّي أَعْلَمُ مِنَ اللَّهِ مَا لَا تَعْلَمُونَ
Waaye, ba kuy bégle ka agsee, daldi koy xëpp yére ya ci kanam. Mu daldi ne xàjj di gis, mu ne : “Moo ndax waxuma leen woon ne xam naa lu ma jële ci Yàlla lu ngeen xamul ? ”
97قَالُوا يَا أَبَانَا اسْتَغْفِرْ لَنَا ذُنُوبَنَا إِنَّا كُنَّا خَاطِئِينَ
- Ñu ne : "Éy yaw sunu baay, sàkkul nu njéggal [ci Yàlla] sunuy bàkkaar. Ndax nun dey juumoon nanu ba def bàkkaar naka”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
95Aaya

Tekki — Yusuf 95

Simoore Yusuf Aaya 95 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Giñ nanu ci Yàlla ne yaa…

Simoore Aaya 95/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 93–97. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers