Ibrahima · 15/52
Tekki Waxtaan — Simoore Ibrahima
وَاسْتَفْتَحُوا وَخَابَ كُلُّ جَبَّارٍ عَنِيدٍ ١٥
Transliteration
Wastaftahoo wa khaaba kullu jabbaarin `aneed
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu sàkku ndimbal [ñoom Yonent ya]. Képp ku doon rëy-rëylu te jeng daldi yàqule.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 13-17 — Simoore Ibrahima
13وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لِرُسُلِهِمْ لَنُخْرِجَنَّكُم مِّنْ أَرْضِنَا أَوْ لَتَعُودُنَّ فِي مِلَّتِنَا ۖ فَأَوْحَىٰ إِلَيْهِمْ رَبُّهُمْ لَنُهْلِكَنَّ الظَّالِمِينَ
Ña weddi wax seen Yonent ne leen : “Dananu leen génne ci sunu suuf walla ngeen dellusi ci sunu diine ! ”. Seen Boroom soloo leen ne : “Fàwwu dana alag tooñkat ña,
14وَلَنُسْكِنَنَّكُمُ الْأَرْضَ مِن بَعْدِهِمْ ۚ ذَٰلِكَ لِمَنْ خَافَ مَقَامِي وَخَافَ وَعِيدِ
te ci seen ginnaaw Danaa leen jox suuf si muy seen dëkkuwaay [yéen Yonent yi ak ñi leen topp]. Loolu mooy peyug ku ragal Sama taxawaay [ak moom] te ragal Samay tëkku”.
15وَاسْتَفْتَحُوا وَخَابَ كُلُّ جَبَّارٍ عَنِيدٍ
Ñu sàkku ndimbal [ñoom Yonent ya]. Képp ku doon rëy-rëylu te jeng daldi yàqule.
16مِّن وَرَائِهِ جَهَنَّمُ وَيُسْقَىٰ مِن مَّاءٍ صَدِيدٍ
Te Safaraa nga xaar ca ginnaaw te dees na ko nàndal ndox mu bon te tàng jér
17يَتَجَرَّعُهُ وَلَا يَكَادُ يُسِيغُهُ وَيَأْتِيهِ الْمَوْتُ مِن كُلِّ مَكَانٍ وَمَا هُوَ بِمَيِّتٍ ۖ وَمِن وَرَائِهِ عَذَابٌ غَلِيظٌ
dana ko guux. Waaye du ko xaw a mën a wann. Dee di ko dikkale wet gu nekk, te du dee ; te it mbugal mu tar dana ca topp.
IbrahimaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
15Aaya
Tekki — Ibrahima 15
Simoore Ibrahima Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu sàkku ndimbal [ñoom Yonent ya]. Képp ku doon rëy-rëylu…Simoore Aaya 15/52 — Simoore Ibrahima إبراهيم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ibrahima Dégg, Simoore Ibrahima Tekki, Simoore Ibrahima mp3, Simoore Ibrahima pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Ibrahima
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Friday, October 2, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


