Al-Hijr · 24/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
وَلَقَدْ عَلِمْنَا الْمُسْتَقْدِمِينَ مِنكُمْ وَلَقَدْ عَلِمْنَا الْمُسْتَأْخِرِينَ ٢٤
Transliteration
Wa la qad `alimnal mustaqdimeena minkum wa laqad `alimnal mustaakhireen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Sunu xam-xam làmb na ña jiitu woon ak ñay mujj ci yéen.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 22-26 — Al-Hijr
22وَأَرْسَلْنَا الرِّيَاحَ لَوَاقِحَ فَأَنزَلْنَا مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَسْقَيْنَاكُمُوهُ وَمَا أَنتُمْ لَهُ بِخَازِنِينَ
Yónni Nanu ngelaw luy sos (taw ci niir yi) ; wàcce Nanu ndox mu jóge asamaan, nàndal Nanu leen ci te mënuleen ko woon a denc.
23وَإِنَّا لَنَحْنُ نُحْيِي وَنُمِيتُ وَنَحْنُ الْوَارِثُونَ
Te Nun nooy dundal te Nun nooy rey te Nun nooy donn (mujje) àddina bi yépp.
24وَلَقَدْ عَلِمْنَا الْمُسْتَقْدِمِينَ مِنكُمْ وَلَقَدْ عَلِمْنَا الْمُسْتَأْخِرِينَ
Sunu xam-xam làmb na ña jiitu woon ak ñay mujj ci yéen.
25وَإِنَّ رَبَّكَ هُوَ يَحْشُرُهُمْ ۚ إِنَّهُ حَكِيمٌ عَلِيمٌ
Sa Boroom dana leen fang ñoom ñépp. Moom Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.
26وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن صَلْصَالٍ مِّنْ حَمَإٍ مَّسْنُونٍ
Bind Nanu nit ci ban bu wow bu jóge ci ban bu ñuul.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
24Aaya
Tekki — Al-Hijr 24
Simoore Al-Hijr Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sunu xam-xam làmb na ña jiitu woon ak ñay mujj…Simoore Aaya 24/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








