Al-Hijr · 31/99
Tekki Waxtaan — Al-Hijr
إِلَّا إِبْلِيسَ أَبَىٰ أَن يَكُونَ مَعَ السَّاجِدِينَ ٣١
Transliteration
Illaaa ibleesa abaaa ai yakoona ma`as saajideen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
ba mu des Ibliis, moom bañ naa bokk ca ñay sujjóot.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 29-33 — Al-Hijr
29فَإِذَا سَوَّيْتُهُ وَنَفَخْتُ فِيهِ مِن رُّوحِي فَقَعُوا لَهُ سَاجِدِينَ
te saa su Ma ko yemalee ba wal ci dara ci sama ruut, rotleen sujjóotal ko”.
30فَسَجَدَ الْمَلَائِكَةُ كُلُّهُمْ أَجْمَعُونَ
Malaaka yépp sujjóot,
31إِلَّا إِبْلِيسَ أَبَىٰ أَن يَكُونَ مَعَ السَّاجِدِينَ
ba mu des Ibliis, moom bañ naa bokk ca ñay sujjóot.
32قَالَ يَا إِبْلِيسُ مَا لَكَ أَلَّا تَكُونَ مَعَ السَّاجِدِينَ
Mu ne [Moom Yàlla] : “Yaw Ibliis, lu la dal ba bokkuloo ci sujjóotkat yi ? ”
33قَالَ لَمْ أَكُن لِّأَسْجُدَ لِبَشَرٍ خَلَقْتَهُ مِن صَلْصَالٍ مِّنْ حَمَإٍ مَّسْنُونٍ
Mu tontu ne : “Man kat duma sujjóotal nit koo binde ci ban bu wow bu jóge ci banit bu ñu togg”.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
31Aaya
Tekki — Al-Hijr 31
Simoore Al-Hijr Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba mu des Ibliis, moom bañ naa bokk ca ñay…Simoore Aaya 31/99 — Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hijr Dégg, Al-Hijr Tekki, Al-Hijr mp3, Al-Hijr pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








