Al-Hijr · 4/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَمَا أَهْلَكْنَا مِن قَرْيَةٍ إِلَّا وَلَهَا كِتَابٌ مَّعْلُومٌ ۝٤
Wa maaa ahlaknaa min qaryatin illaa wa lahaa kitaabum ma`loom
📖 Tekkim Wolof
Dunu alag benn dëkk te fekk amul àpp bu ñu xam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Hijr

2رُّبَمَا يَوَدُّ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوْ كَانُوا مُسْلِمِينَ
Amaana ña weddi ñanga ne siiw nekki jullit.
3ذَرْهُمْ يَأْكُلُوا وَيَتَمَتَّعُوا وَيُلْهِهِمُ الْأَمَلُ ۖ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Bàyyileen ñuy lekk ak a xéewlu, tey mébét lu leen soxal; danañu mës a xam !
4وَمَا أَهْلَكْنَا مِن قَرْيَةٍ إِلَّا وَلَهَا كِتَابٌ مَّعْلُومٌ
Dunu alag benn dëkk te fekk amul àpp bu ñu xam.
5مَّا تَسْبِقُ مِنْ أُمَّةٍ أَجَلَهَا وَمَا يَسْتَأْخِرُونَ
Benn xeet du jiitu àppam te it mënu koo weesu.
6وَقَالُوا يَا أَيُّهَا الَّذِي نُزِّلَ عَلَيْهِ الذِّكْرُ إِنَّكَ لَمَجْنُونٌ
Ñu naan leen : “Yaw mii, wàcceef na ci yéen Téere ba, yaw dof tigi nga !
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Hijr 4

Simoore Al-Hijr Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dunu alag benn dëkk te fekk amul àpp bu ñu…

Simoore Aaya 4/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers