Al-Hijr · 45/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ ۝٤٥
Innal muttaqeena fee Jannaatinw wa `uyoon
📖 Tekkim Wolof
Ña ragal Yàlla nag, ñangay nekk ciy àjjana ak i bëti-ndox [yuy ball].

🎧 Dégg


📜 Aaya 43-47 — Simoore Al-Hijr

43وَإِنَّ جَهَنَّمَ لَمَوْعِدُهُمْ أَجْمَعِينَ
Te Safara mooy fa ñuy daje ñoom ñépp.
44لَهَا سَبْعَةُ أَبْوَابٍ لِّكُلِّ بَابٍ مِّنْهُمْ جُزْءٌ مَّقْسُومٌ
Te Safara nag am na juróom-ñaari buntu te buntu bu nekk am na xaaj bu ñu ko sédde ca [ñu beew ña].
45إِنَّ الْمُتَّقِينَ فِي جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ
Ña ragal Yàlla nag, ñangay nekk ciy àjjana ak i bëti-ndox [yuy ball].
46ادْخُلُوهَا بِسَلَامٍ آمِنِينَ
[Ñu ne leen] : “Dugguleen ci jàmm ànd ak kóolute”.
47وَنَزَعْنَا مَا فِي صُدُورِهِم مِّنْ غِلٍّ إِخْوَانًا عَلَىٰ سُرُرٍ مُّتَقَابِلِينَ
Te Nu rocci [raxas] la nekkoon ci seeni xol cig noonoo : ñu nekk ay mbokk yu jaaxaan ca seeni lal jàkkaarloo.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Al-Hijr 45

Simoore Al-Hijr Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ragal Yàlla nag, ñangay nekk ciy àjjana ak i…

Simoore Aaya 45/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers